MGEEY Loy Wax cover image

Paroles de Loy Wax

Paroles de Loy Wax Par MGEEY


Eh! (Omzo on the Maafe) 

Niveau bey hot dey lakke
Song bi dey daw M'bappe
Ndakaaru njaay lay wacce
Da nga xam wala ngay lacce?  (Ey)
Niveau bey hot dey lakke
Song bi dey daw: M'bappe
Ndakaaru njaay lay wacce
Da nga xam wala ngay lacce? 

Boy kula laadj loy wax?
Ey waay ndeysaan
Ey deykalanax!
Dañu koy salsaa bamu saf sapp 
Boy kula laadj loy wax?
Ey waay ndeysaan
Ey deykalanax!
Dañu koy salsaa bamu saf sapp

Eh seen xel yè karaas mënoleen dem
Fépp lañ mënè ego ak théme
Lepp ngeen tële di xaatim nenn
Yèn ñëp lay warax, talent dey fènn
Raw naa daxaar qon lepp ay saff
Yëngël Dakar ba lepp ay barr
Fepp ay saxar te fepp ay tarr
Xatna comme yaraax yenn ñëp ay xaar
Naanuma lingom te gënlaa forox
Deñ lay tingoom nga mën maa boroos
Sëf lë ay drogues Di laal ay troc
Jital oyof te mën naa torop 
Laalnaa xol yi, bët yeppay taa
Root néñ xalaat ba feesal ndaa
Xir bey dalaat
Fi mann leñ falaat te
Neena faraax damay salsaa (allright)

Niveau bey hot dey lakke
Song bi dey daw: M'bappe
Ndakaaru njaay lay wacce
Da nga xam wala ngay lacce? (Eey)
Niveau bey hot dey lakke
Song bi dey daw: M'bappe
Ndakaaru njaay lay wacce
Da nga xam wala ngay lacce? 

Boy kula laadj loy wax?
Ey waay ndeysaan
Ey deykalanax!
Dañu koy salsaa bamu saf sapp 
Boy kula laadj loy wax?
Ey waay ndeysaan
Ey deykalanax
Dañu koy salsaa bamu saf sapp 

Eh kula laaj loy ? My boy 
bëri ay biens, riche: bad boy
Gatdamn, dañu koy game bamu neex
Waye mënu ñuko gagne fò
D'accord 
Maak Mgeey de la Mancha
Sancaat drip bu leer diko salsaa
May Mc bila antann
Tek lu dìs gann si sa kaw ba nga appaat
Fuck li ngay wax mëso maa jox cèpp
Budè da nga merr everything okay
Avant ngeen di xeef nekatul mok yeen
Sama talent mo daaxa wanewuu Mo gates 
Okay okay no stress No cap
My boy loy hate?
sama chronomètre dou seu temps lay kepp
Bu yabbo nga kepp sa tank boy
tekk ngafi tank Mais taanku guinaaw

Niveau bey hot dey lakke
Song bi dey daw : M'bappe
Ndakaaru njaay lay wacce
Da nga xam wala ngay lacce? (Eey)
Niveau bey hot dey lakke
Song bi dey daw: M'bappe
Ndakaaru njaay lay wacce
Da nga xam wala ngay lacce? 

Boy kula laadj loy wax?
Ey waay ndeysaan
Ey deykalanax
Dañu koy salsaa bamu saf sapp 
Boy kula laadj loy wax?
Ey waay ndeysaan
Ey deykalanax
Dañu koy salsaa balu saf sapp (ey)
Musique utilisée dans cette vidéo

Ecouter

A Propos de "Loy Wax"

Album : Loy Wax (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Sep 08 , 2021

Plus de Lyrics de MGEEY

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl