Paroles de Kirikou
Paroles de Kirikou Par SAMBA PEUZZI
[CHORUS]
Kheuthio len couronne bi mane CFA rek lay guiss
Talal lokho mère mofi dièkh légui damakoy
Diokh boram
Karaw bou nioul la, bop bi mako teinte
kone niakouma dara té tolagouma sama digou ndeundeu
Di def son you nice, khalé makk di noce
Fils mankoy tothie ioe ngey sissou mais
Dop pression, ni tatou kirikou
Do pression boy ni tatou kirikou
Mane dama feuleu nieup youkhou l’eau est là
L’eauuuuu... l’eau est là
Fils dama percer nieup youkhou l’eau est là
L’eauuuuu... l’eau est là
[VERSE 1]
Khathi té do door do maté yay Scooby-Doo
Ma nélaw ci game da beurre karaba yi ma done Oggy
Dakh fékii comme ay cafard
Pour Peuzzi géneu Reptyle fauk titeuf lale Nadia
Dane mofi snap, té yay screenshot souniouy discussions
Nel gni sandi khér souma guesto da
Fek shoe bou am tatte romb
Té wone da pairou daleu trois cent mille laye sol key
Sen pussy guel, sama power bank Peuzzi
Dou meussa faye
Dam si done fo, tay mansi joni joni ay broh, guéné fi yah
Yah ! ioe ba dagmay deuk barro
Athi barre bi sikaw tok fa soul rek ka mey boleik souf
Doigt d’honneur pour yen nieup mother
Fuck old of fouf
[CHORUS]
Kheuthio len couronne bi mane CFA rek lay guiss
Talal lokho mère mofi dièkh légui damakoy
Diokh boram
Karaw bou nioul la, bop bi mako teinte
kone niakouma dara té tolagouma sama digou ndeundeu
Di def son you nice, khalé makk di noce
Fils mankoy tothie ioe ngey sissou mais
Dop pression, ni tatou kirikou,
Do pression boy ni tatou kirikou
Mane dama feuleu nieup youkhou l’eau est là
L’eauuuuu... l’eau est là
Fils dama percer nieup youkhou l’eau est là
L’eauuuuu... l’eau est là
[VERSE 2]
Controller sa zone, sa wa kogn dagnla rouge
Ma ngui de flou léer avant mey bédiaw, na am
khaliss bou wékh taleu
Lokoto oute niossi bo yem douma nangou done khalé
Nénagn time is money, kone niak diote
Moy mayer khaliss, awma nélaw goudi lay job damay guéméntou lo
Leundeuma léer leg ma leundeum sans ma photo grey
Buzz’ou une semaine pour niom clash ma
Moy takh niou siw, sokoy tangual
Boul dougeunték niom sinon dagn lay babecue
Partant par force nangou sa poste nga tok banc
Sandi pic sampe nul noono mane néwouma si yi
Rayla mayar sa barre sa bountou gallé féthi
Wondél di battle sa mère nako siguil ndigalé
[CHORUS]
Kheuthio len couronne bi mane CFA rek lay guiss
Talal lokho mère mofi dièkh légui damakoy diokh boram
Karaw bou nioul la, bop bi mako teinte
Kone niakouma dara té tolagouma sama digou ndeundeu
Di def son you nice, khalé makk di noce
Fils mankoy tothie ioe ngey sissou mais
Dop pression, ni tatou kirikou
Do pression boy ni tatou kirikou
Mane dama feuleu nieup youkhou l’eau est là
L’eauuuuu... l’eau est là
Fils dama percer nieup youkhou l’eau est là
L’eauuuuu... l’eau est là
Ecouter
A Propos de "Kirikou"
Plus de Lyrics de SAMBA PEUZZI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl