Paroles de Bideew
Paroles de Bideew Par OBREE DAMAN
Aha aha aha aha
Yow Mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Yow Mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Agsil ñu àndandoo
Àndandoo ci asamaan
Sa mbëggeel’ay bideew (Bideew biy leeral goor Yalla)
Bideew biy leeral sama yoon
Aha jigeen a indi leer
Aha leeray ci àdduna
Aha sa mbëggeel’ay bideew
Aha (Bideew biy leeral goor Yalla)
Biy leeral sama yoon
Yow Mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Yow Mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Jigeen’ay leeral
Melni leeray u asamaan
Sen mbëggeel’ay leeral
Jigeen’ay leeral
Ni leeray u asamaan
Sa mbëggeel’ay leeral
Sama yoon
Leer leer leer
Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi
Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi
Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi
Yow Mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Yow Mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Aha aha aha aha
Ecouter
A Propos de "Bideew"
Plus de Lyrics de OBREE DAMAN
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl