COUMBA GAWLO SECK Sant Rek cover image

Paroles de Sant Rek

Paroles de Sant Rek Par COUMBA GAWLO SECK


Sant reka ma waar... Gawlo
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo
Sant reka ma waar... Gawlo
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo
Yaakarone diekhna Yalla di fadj sama aadio
Yaakarone diekhna Yalla di fadj sama aadio
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo
Adouna angui nii daal darra diarou fii di rakadio
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo
Adouna aki melome bou kene dieume fii di rakadio
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo
Seni niane nangouna dieuredieufeté akhlou Gawlo
Niane nangouna dieuredieufeté akhlou Gawlo
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo

Mane guisna kemtaann borom bé
Gawlo
Mane guisna kemtaann borom bé
Gawlo
Coumba guisna kemtaann borom bé
Sou wakhé waaw kene douko tégui
Gawlo

Sant reka ma waar... Gawlo
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo
Sant reka ma waar... Gawlo
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo

Yaakarone diekhna Yalla di fadj sama aadio
Yaakarone diekhna Yalla di fadj sama aadio
Adouna angui nii daal daara diarou fii di rakadio
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo
Adouna aki melome bou kene dième fii di rakadio
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo
Seni niane nangouna dieuredieufeté akhlou Gawlo
Niane nangouna dieuredieufeté akhlou Gawlo
Sant rek ka la waar yow Coumba Gawlo

Mane guisna kemtaann borom bé
Gawlo
Mane guisna kemtaann borom bé
Gawlo
Coumba guisna kemtaann borom bé
Sou wakhé wawaw kéne douko tégui
Gawlo

Sant rek la war
Bour Yallah boula namé saggal
Daff lay tekk ay nattou santal
Xalei yi di gnann
Makk yi di gnann
Kilifa yi nieup leu beug, woyal

Mane Gawlo
Sant rek la war
Mane Coumba Gawlo
Sant rek la war
La Diva
Sant rek la war
Ohw (woyal)
Sant rek la war

Sant rek la war
Mane Coumba Gawlo
Sant rek la war
La Diva
Sant rek la war yow Coumba Gawlo

Lii kemtaann la, Ah ah
Santena Yallah
Yakaronn ni diekhna, Yallah dima tétté; dima téral
Yakaronn ni diekhna, Mame Yallah dima saggal
Ohh, sant reka ma war
Sant reka la war ... Gawlo
Sant reka la war ... Gawlo
Sant reka la war ... Gawlo
Sant na Maame; Ya-Allah

Mane Gawlo
Mane Coumba Gawlo
La Diva
Gawlo
Mane Gawlo
Mane Coumba Gawlo
La Diva
Gawlo

Ecouter

A Propos de "Sant Rek"

Album : Sant Rek (Single)
Année de Sortie : 2023
Ajouté par : Farida
Published : Sep 04 , 2023

Plus de Lyrics de COUMBA GAWLO SECK

COUMBA GAWLO SECK
Na
COUMBA GAWLO SECK
COUMBA GAWLO SECK
COUMBA GAWLO SECK

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl