
Paroles de Fipou Na
Paroles de Fipou Na Par EL MAESTRO
Yeah Zayy
Man Bayina kooo
Fipou na Man
Man Fipou na bayina ko
Xol bi Néna Détt
Man guédd na ko Wane ganaw
Sama xol bi Néna dédétt Way
Dagma dakal Ouroul Aynii
Ma beug la lolé
Nga Minal ma sa boppeu
Ma doff si Yaw
Soumala déffé PP
Ngây nianal nản sa xol bi dafa sédd
Soumala séné ngay dem
Loudoul yaw damakoy guédd
Wayé légui
Nénga malay déranger
Lolou défma Gomou Xol
Dima ronger Hé
Bayinala Man mi lé
Man Fipou na bayina ko
Xol bi Néma Détt
Man guédd na ko Wane ganaw
Sama xol bi Néma dedett
Fipou na badina ko
Xol bi Néma Détt
Man guédd na ko Wane ganaw
Sama xol bi Néma dédétt Way
Sama xol bi Néma dedett Way
Man mi dama diaxal
Maak nji daniou doyal
Mon amour
Tu en as trop abusé
Diaroul may forcer
Beuguél dou kén rek kol def
Diaroul may sallé
Xol bi Yathie nekeu
Nila meunone démé Cherie boy
Bye Bye
Man Fipou na bayina ko
Xol bi Néma Détt
Man guédd na ko Wane ganaw
Sama xol bi Néma dedett
Fipou na badina ko
Xol bi Néma Détt
Man guédd na ko Wane ganaw
Sama xol bi Néma dédétt Way
Man Fipou na bayina ko
Xol bi Néma Détt
Man guédd na ko Wane ganaw
Sama xol bi Néma dedett
Fipou na badina ko
Xol bi Néma Détt
Man guédd na ko Wane ganaw
Sama xol bi Néma dédétt Way
El Maestro le Kangham
Ecouter
A Propos de "Fipou Na"
Plus de Lyrics de EL MAESTRO
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl