Paroles de Le Prix De La Vie
Paroles de Le Prix De La Vie Par MAK THE BLACK BOY
Tiilim diina deem fu saabu meenul deem
Tee laamanie dina raxas kon feck yi naniu tey
Ndakkay jaap golo ci niaay lolu daafa leer
Tee garder kuy dunde lumuy guiss menula deem
Outil meeru golo nigger saful borom tool
Boorom barkee budul jouet soxlawul parasol
Nii saa beut meun na taak tee do meuneu xool
Tee ku yalla tusngal ken dula teere xool yalla
Sekul ak niit ah faayanytee boor
Tee ku neek xaam nga wei kula gueneu
Fort kuy guiss tay dii guiss suba kuko gueene fort
Tee xaam xaam dina deem ba eupe dolle buur
Deuk di raxas lii tiilim mu seet ni xellu liir
Tee kinga mesula guiss no menulo ko miin
Bén loxo du taccu beut su gueumee du guiss
Niom nieupeu gueum ken menou la guiss
Dundu bi laniou jaap en otage
Ibliss su dewone saxe du tax liberté am
Dundu bi laniu jeund ci prix jaam jaayeko ci prix jaam
Dundu bi laniou jaap en otage
Ibliss su dewone saxe du tax liberté
Am dundu bi laniu jeund ci prix
Jaam jaayeko ci prix jaam
Dundu bi laniou jaap en otage
Ibliss su dewone saxe du tax liberté am
Dundu bi laniu jeund ci prix jaam jaayeko ci prix jaam
Dundu bi laniou jaap en otage
Ibliss su dewone saxe du tax liberté am
Dundu bi laniu jeund ci prix jaam jaayeko ci prix jaam
Nii deuk ci gare taxuta barri gan
Nieupe beugue ma du taax homme ma naguou mane
Mais samay kaddu lay jaay ak samay kaddu mame
Tee bess bu neek aucun jook beug ma faad man
Yalla tee samay kaddu jaayu ma sama âme
Tee fukkale du taax ma deuppo ciin lu tang
Ku am kuddu do laak da feek du lu tang
Tee ku xebul sa ngur do messe don buur
Beut di yag di jeegui lu niewegul
Amuniu ludul guestu ak sabablu
Yallay deef luko neex no dunci meun tuss
Tee yaag du sabu wayee dina foot
Tee ku dee ci tele ya tague saa bop
Ku deuk ci metit wara meune munie
Ma deuk dii munie tee guisu ma ken
Arass teuke yeungetu ndax lifi nee ci frais
Dundu bi laniou jaap en otage
Ibliss su dewone saxe du tax liberté am
Dundu bi laniu jeund ci prix jaam jaayeko ci prix jaam
Dundu bi laniou jaap en otage
Ibliss su dewone saxe du tax liberté
Am dundu bi laniu jeund ci prix
Jaam jaayeko ci prix jaam
Dundu bi laniou jaap en otage
Ibliss su dewone saxe du tax liberté am
Dundu bi laniu jeund ci prix jaam jaayeko ci prix jaam
Dundu bi laniou jaap en otage
Ibliss su dewone saxe du tax liberté am
Dundu bi laniu jeund ci prix jaam jaayeko ci prix jaam
Ecouter
A Propos de "Le Prix De La Vie "
Plus de Lyrics de MAK THE BLACK BOY
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl