CANABASSE Khekh Yu Bess cover image

Paroles de Khekh Yu Bess

Paroles de Khekh Yu Bess Par CANABASSE


Yaw linga beug def baye dou dém
Mais comme danga gnou beug test kay gnou dem
Kou ndobine rey sa mame daaw dé rêne
Lou nioul foko sène doko diégué dingko daw bodé borom xell
Yeah nitteu gawa faté lolo takh
Nga takamlou deuk leumm té niola faal
Prési dem prési dikk prési doul niou sissou fippou takk derr yi diniou shoot
Mbirr bi doufi goulète
kagn lagnouy tall khekh yu Bess
yakarone nagn la tchi demb macky sall
Mais teydji nioune la contre yaw
Té nala leer né dictateur doufi am ndam

Taal sama call guiss véhicules lourds yi di djougué fatick
Wathie guiss decret bi prefet arrêter cours yi oh shitt
Nombre mort yi mingui yokk corona dotoul fitna
Fimou dieum lay ladj narr na gueunah métii
Esk baye cheikh wa keuram moudjei negn djott coram
Thioye bi ko shoot esk dina nangou toram
Mohamed tony agent GIGN bi lokhom bi dagg
Boutchi deretaam taakoul mom taalal lokho Ley moudjé
Prix fort bi nioko deuké feyy
Golo di bey baboune di doundé tei sunu kaw lay deyy
Gnifi wooté wone pour gnu guéneu ba niou falou tey dji
Niom niognou niognou worr niou beug guéneuh niou taxaw xagn niouko
Néna dou guiss lou xonk sunu derett yengalouko
Requête diam dong leu mais prési gantou ko
Idy taxaw sugnu kanam nane niou boudone bénéne deukk mort yi daniouy gueuna beuri
What the fuck ?
Niata nio wara dead
Pour nguène dieuli né
Danguène wara tégui tank pour aar li tchi dess
Démocratie sénégal mingui perte vitesse
Bane exemple nguène niouy djokh boudé kou si nek tchi yène
Dafa fatté lane mo takhone tchi ndialbène mou done xeex
Si sène jeunesse leer nama li bokoul wone tchi sène rêve
Deukou  leumm diouk taxaw dilène xoolé beutou traître
Nguène di xol sene bopp à l’aise si sètou wallahi yène ay deumm nguène

Mais nak thiow dou djipp, dedett thiow dou djipp
Ndakh sène dokhaline défoul dara loudoul yokk sunu fitt
Leeral sunu beutt niou xippi di guiss
Legui xam negn kane moy kane yeah ragné nagnou bitch yi
Gni niou sekhall ba sène gatt feess meuneutouniou wakh
Gni mbouxoum kerall boulène sax sène dotouniou marche
Gnémétouniou naadj gnom ak gni niouy door nio far
Degn ley togn nga aalou niou shoot seu ndeye parei neila masta

Après capitaine bou démissionner ak bèneu juge bou rassou
Dossier biniou classé dou takh bountou histoire bi teudjou
Li dou juste simplou niakhtou degn niou boukh bagn seuss niou fippou
Ndakh guissouniou avenir ci reew bouy nott djaboot keuff séni kaddou
Prefet téyé callam dissi djot ay ordre bavures
Nervis yi done saltél claté negn
Bo coupé sunu connexion nionguék vpn
Dieundeu nga aissatou diop fall
Nionguek absa bou seneweb
Té cnra meunoul bloqué youtube
Diamonoy sopalikou
Danga sous-estimer sunu capacité tei dingako réthiou
#freesenegal hashtag bi moungui daw té di negn ko doundou
Génération twitter tiktok instagram baaram doyna pour daanél ngouur
Bénn pour cliquer 5 pour ngueupp ay big kheer té balle bouy taak sène serment lay taal wakhko bepp takk derr
Légui sipp negn seu système
Seuss negn té negn insisté
Sonko bou libre début le rek takhoul ba thioki bi djekh
Comme que do degg deug tchi larbin yi ley assister
Peuple bey andeu wakh nga degg

Yaw linga beug def baye dou dém
Mais comme danga gnou beug test kay gnou dem
Kou ndobine rey sa mame daaw dé rêne
Lou nioul foko sène doko diégué dingko daw bodé borom xell
Yeah nitteu gawa faté lolo takh
Nga takamlou deuk leumm té niola faal
Prési dem prési dikk prési doul niou sissou fippou takk derr yi diniou shoot
Mbirr bi doufi goulète
Kagn lagnouy tall khekh yu Bess
Yakarone nagn la tchi demb macky sall
Mais teydji nioune la contre yaw
Té nala leer né dictateur doufi am ndam


Rafétalaal litchi dess
Ngala thiow li na djekh
Domou rew mi gningui dè tchi diéma défendre séni rêve
Gni dieul balle gni dieul gaal tchi nguru macky sall
Esk bo teudé dinga nélaw goudi
Esk culpabilité leek leek dinaley fék sii
Def niou sey dom li dess mandat bi niou def la ndjiite
Mou djekh ak djamm nga dem bo bégné gaal gui dikk

Ecouter

A Propos de "Khekh Yu Bess"

Album : Khekh Yu Bess (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Mar 11 , 2021

Plus de Lyrics de CANABASSE

CANABASSE
CANABASSE
CANABASSE

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl