Paroles de Maa Ngi Dem
Paroles de Maa Ngi Dem Par ASHS THE BEST
Now I know now I know
But I don’t know what I’m feeling inside
Gestu woo ma
Maa ngi dem maa ngi dem
Soo ma gisatul dem naa
Maa ngi dem baayi a fi sama xol
Di naa weet weet ci sama yoon
Subateel ba jant sow
Yaa ngi sèntu sa waay ju fi joge woon
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Ñëw naa fi noor (ñëw naa ba dem gisoo ma)
ñëw naa fi nawet (ñëw naa fi nawet tamit)
Ñëw naa fi koor (Tabaski akk Tamxarit)
Fekk fi bekkoor (fekk la ngay bekkoor)
Li ma dundee (li ma dundee)
Akk li ma weesu (akk li ma weesu)
Day dellusee (da fay dellusee)
Ba mel ni seetu (ba mel ni seetu)
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Dem naa te taggu wu ma la (dem naa)
Suma reeree mbaa duñ ne yow la (mbaa duñ ne yow la)
Jooy naa te kenn dooru ma(man dem naa)
Suma reeree mbaa duñ ne yow la (yow la)
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem maa ngi dem
Soo ma gisatul dem naa
Ecouter
A Propos de "Maa Ngi Dem"
Plus de Lyrics de ASHS THE BEST
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl