Paroles de Plaignant
Paroles de Plaignant Par JAHMAN XPRESS
Plaignant
Kagne Lala geudia dég ?
Fête bi nieuw ngmay woo
Ko mbaraan nga beug
Nga baal ma ach wayé
Doumala wakh allo
Ma def ci code nga beug
Takh nanan ma sekouniou bayante
Wakhi dof
Mane nga def sa bebe caisser ma def fess
Sa appel sama call moy baby ma cresh
Beugouma sa jikoo way
Ninga mel bayiko way (aan yan yan yan )
Si money rek ngay dokh moytoul glisser (glisser)
Ndakh élève bou nagouwoul
Jangue fow mouy tricher
Khale niaane
Zero jomm danga fokne yow lay ligueyal
Tey bi dou jalleu demal diamono nekh
Corona leudeumal poche yi
Ken talatoul wekhal
Mane mala geumeutoul
Te yako tek sa bopp
Comme si cheveux naturelles
Sama money rek nga nop
Beugouma sa jikoo way
Ninga mel bayiko way
Foune nga telephone
Encaisser Dakar Paris bas a OM plafonné
Nitou intérêt
Deuk dima tek deam doum ko nangou yalla tere
Been beus la rek
Kone loufi diar forcer
Sa sagnse bi nek si à l’aise
Yangui khalaat nokoy fayer
Nit koune linga am ngay douger marché
Ah weh
Ki am na li ke am na lee boom la déranger
Dang ma jape bopou neen takj nga may dieund lo cheveux
Ah fi rew mi tolou boy kenn wakhoula deug
Mala eup problème lila war wathiouma
Ling ma yen dafa diss eyway wathie ma
Mane daal nga diape ben pwalish yow Ouzin
Yay des palais mane parc Hann
So beuge morom danga koy outi
Sa Mormon nekoufi mane doma mbaraan
Beugouma sa jikoo way
Ninga mel bayiko way
Beugouma sa jikoo way
Ninga mel bayiko way
Ecouter
A Propos de "Plaignant"
Plus de Lyrics de JAHMAN XPRESS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl