Lane Mo Takh Lyrics
Lane Mo Takh Lyrics by BRIL
Déf ngama louma guèntoulwone
Louma doul meuna guum koumako wakhone
Dara guenoul kawè fimala téggoooone
Sorouma lii Béteu-Ngamaaahh
Yaw li ngana deff metti-namaa hahaan
Ak finiou diaar yeup lii meunoumako wone imaginé
Sama bopp dafa diakhasso may guiss ayy image you nééh
Lan mola doyoul ba nga Diouk name da ngay wouti lénén fénén
Loutakh mou done kouma kham loutakh yaw tanoulo kénén
Yaa takh ma bayi nieup bayi samay Mbokk yaw nga Fayma lii
Da nga wakh bama Diokh la lepp mokk’ak yaw béneu familly
Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii
Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma loumala bagnal ba ngay khool kénén
Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii
Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma loumala bagnal ba ngay khool kénén
Dafa mélni damay guént yakamti kouma yééhh
Bama yééwou meuna doundaat mbékté biss bign niouy mayéé
Yaa nékkone sama vérité yaw rek laa geumone
Meussouma guiss finga maay trompé mélni damma geume-mone
Digoon ngana doundou aldianaaaahh
Maa’k yow dound’ak dééh ngana wakhone wayé tay l éppeu diékhnaaaahhh
Yaa takhone ma bayi di wakh nane niom nieuppa yéém
Tey nga khooss sama cicatrice deffatt ko gome
Liniou dounddou boumakay méttali day mélni poème
Kii louko dall est ce que anddeu naak saagooome
Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii
Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma loumala bagnal ba ngay khool kénén
Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii
Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma loumala bagnal ba ngay khool kénén
Watch Video
About Lane Mo Takh
More BRIL Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl