BRIL Lettre Au Président cover image

Lettre Au Président Lyrics

Lettre Au Président Lyrics by BRIL


Dakar le 07 Mars 2021
Mangui toudou Djibril Fall, niou gueune ma xam thi tourou Bril
Bataaxal bimay bindeu nak, mangui koy djagglél buur

Prési askane wéma yoni nénagn Rewméngui boy
Déréttangui tourou fèppeu wadjour yeupangui djoy
2012 beuggone Solution motakh niou fal-leu
Té légui Réwmé eup problème Classou CM2
Déggagougnla wayé khamnani djotnga Xibaar yi
Xééx thi mbéd , Takk dér yi Nek, Déé gui gueune di baari
Todjngén Rewmi ndakh Viol té yagga violé sunuy Droit
Réwmi amoul yakkaar, bouniouy djokh raaya policier bou djoupp, amouniou Loi
Un Peuple - Un but - Une foi
Nénagn dougnla bayi ngay falou 3 fois
Nonon doko meune
Ndiaago meunoul peinture ba peinture assamane
Légui boy yi daniõ ragal doundou , gnimé coup de feu
Ndakh sén biir yé gueuna vide Dakar heurou Couvre feu
Khiif bou méti motakh niou beuri di profito di woutt
Louniou lékkeu, waathiél sa bopp, sa karaw doko soutt
Guéneul wakh ak niom, Thiowli meuna Djéékh
Réwmi dou yako mom, bathiy def loula Néékh
Dou yone ay Nervis djeul plaçou takkeu der yi
Khéép ay gourdin wout ay armes xéékh’ak gni di sani xéér yi

Bataaxal bi djéékhagoul, Prési degglouma
Meunouma dénthie sama xalima té bindouma
Wakh thi gni féébar yor ordonnance té amouniou lougnko djeundé
Gni né thi ngour gui beurilé ba amouniou lougn ko doyé
Continué di tek deal you sétt ni léélou Aba
No stress laniouy léékké sunu xaliss douniou Nitt
Politicien yé gueuna faux sonnerie iphone thi android
Dangay niakkeu ba do nélaw, niou rêvélola done sa Ndjiitt
Koula matteu fatalila ni amnga ay beugn
Dotouniouko nangou c’est le Sénégal qui bagne
04 Avril khamwma louniouy fêter wayé dou indépendance
1960 ba tay ngén djokh lou beuri France
Paathio Rewmi ba nioune amatouniou bén liberté
Statue de la liberté niou eup liberté
Nioune douniou ay tailleur wayé djeulnagn ay mesures
You léér , tek ko fou léér , je vous le jure
Peuple bi ragalouniou guiss nga niniouy tééro Risques
Ba sa ministre bi tite djignlén terroristes
Dou deugg dou yone kou wakh nga teudj amo opposant
Légui peuple bi mo moudjé guéneu done sa opposant

Deugg ngéni bagn té deugg faaléwoulén
Teklén ko thi yone nangoulén
Deugg mou moudjou féppeu kone parélén
Djaay dõlé baakhoul waathieulén

Watch Video

About Lettre Au Président

Album : Lettre Au Président (Single)
Release Year : 2021
Added By : Farida
Published : Mar 08 , 2021

More BRIL Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl