
Goumin Lyrics
...
Goumin Lyrics by EL MAESTRO
Moustapha di waayati
Huhum wowowowowayy
Mba ci man la ?
Mba ci yaw mi la ?
Mba ci niou niar la
Hé !! Hé !! Hé
Xawma sax ?
Man guissuma koulén guena leundam
(Guissuma koulén guena leundam )
So nékék ñom daganàn
Yaw rek lañ gueum
Sassuné dinañu la diox confiance
Diguone nala sax mariage
Nga dem ba fokni amo chance
Xawma loutax duñu Focus
Ci kilén beug paré Yeureum lén
Di toppu kiy door paré dilén fén
Au pire des cas dig ci dieulé goumin yi
Daniuy yaak sa Life
Doulén def Dara
Goumin lañu lay doundou loo
Sassuné
Goumin mom lay doundou
Minal la bopam té dila dikk
Né duñla massa bayi
Xeuy dadi dém Bayilak
Goumin lañu lay doundou loo
Sassuné
Goumin mom lay doundou
Minal la bopam té dila dikk
Né duñla massa bayi
Xeuy dadi dém Bayilak Goumin
Sa youma diaxlé won
Daw wout ci la
(Yama doon délo ci )
Tolon nga ci man makama wassila
Ci yaw la don séttu
Ba li néwone sama kanam
Guissuma won mu ñaw
Ling fi dieulé Or la
Li nga bayi sama xol bi goom la
Xawma loutax duñu Focus
Ci kilén beug paré Yeureum lén
Di toppu kiy door paré dilén fén
Au pire des cas dig ci dieulé goumin yi
Daniuy yaak sa Life
Doulén def Dara
Goumin lañu lay doundou loo
Sassuné
Goumin mom lay doundou
Minal la bopam té dila dikk
Né duñla massa bayi
Xeuy dadi dém Bayilak
Goumin lañu lay doundou loo
Sassuné
Goumin mom lay doundou
Minal la bopam té dila dikk
Né duñla massa bayi
Xeuy dadi dém Bayilak Goumin
Mba ci man la wawaw ?
Mba ci yaw mi la ?
Mba ci niou niar la
Hé !! Hé !! Hé
Xawma sax ?
Watch Video
About Goumin
More EL MAESTRO Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl