OMZO DOLLAR Tassaré cover image

Tassaré Lyrics

Tassaré Lyrics by OMZO DOLLAR


[CHORUS]
Omzo Dallar dh tassaaré na deuk bi
Mou nex mou nkhari omzo dollar tassaré na deuk bi
Mou nex nakhari miézè tassaré deuk bi
Mou nex nakhari miézè tassaré deuk bi
Sicap tous les jours
Fuck sa rappeur tous les jours
Make sa money tous les jours
Fuck ay bitchees tous les jours tassaré
Tassa, tassa, tassa tassaré
Tassa, tassa, tassa
Tassa, tassa, tassa

[VERSE  1]
Zo dollar miézè dé riva
Dollavéli bandit sicap
Sou rap bi am lou yeungou si tate
Mafa né di joué guitare
Sayou may def béneu pause bou ndaw rek
Rap galsen bi nékate orphelina
Rene fauk sama gayi tékki di nagn
Bireul babtou sou lén mayoul visa
Saga sa ndeye nga teuthi sa gate
No défaroul niggah sagate
Mame premier miézè doko sagate
Hentai hentai bizon sagate

On se mélange pas doto len ma sen
Niou lathié adresse bi né lén laba
Yakar si clash ma pour meuna dem dey
Melni né si ndox di tal ay tabac
Damay rap sankalé mais amna sankalé
Yo khamni sank lagn niow beug
Ma sanka ken sankalen
Shaki rek sankalin makoy tothi
Ni way si baramou sankalegn

Fompal dalleu yi sa couté très chère
Veste est jacket sa coute très chère
Rice in peace rappeur bou laloul cachet
Clashanték mane sa coute très chère

Sicap tous les jours
Fuck sa rappeur tous les jours
Make sa money tous les jours
Fuck ay bitchees tous les jours tassaré
Tassa,tassa, tassa tassaré
Tassa, tassa, tassa
Tassa, tassa, tassa
Sicap tous les jours
Fuck sa rappeur tous les jours
Make sa money tous les jours
Fuck ay bitchees tous les jours tassaré
Tassa, tassa, tassa tassaré
Tassa, tassa, tassa
Tassa, tassa, tassa

[CHORUS]
Omzo Dallar dh tassaaré na deuk bi
Mou nex mou nkhari omzo dollar tassaré na deuk bi
Mou nex nakhari miézè tassaré deuk bi
Mou nex nakhari miézè tassaré deuk bi

[VERSE  2]
Légui mane leu nieup di sandi pick
May sen papa fils c’est scientifique
Ré len santafé petit airport
Yoré game bi ni EA Sport
Beurrri histoire mane la père castor
Khoulo virr meu soulévé castor
Boulma bolé si sey égautrip
Tek sa madré romb nek piss

Sicap karack c’est à vie
No joutou gang c’est à vie
Mélangerie c’est à vie
Capitano Icardi
Sicap karack c’est à vie
No joutou gang c’est à vie
Mélangerie c’est à vie
Capitano Icardi
Fauk nga nagou ki sa papa la
Niggah soxla fils lou fatala

Make ay million demna beutou si desert ak
Guel bou geuneu toy satala
Zéro ragal zéro pression
Coup et blessure vol agression
Flagrant délit la ley
Tégual bala ngey prêt
How wallah qu’es qu’elle est très sombre

Fi mane késsé ma doul nane wayne
Samay niggah douniou nane thiayne
Times is money richard takoul montre
Nitte bou ndool mais aka am time
Biir radison def ay sandale
Romb raciste yi ndiagal

Dougal toubab sibiir cage jou gorille iri
Quelques libain biir wakanda deh
Dama légendaire ba souma déwé di
Nagn douté watt sama exitance
MC dolen meussa atteindre samay line
Même so nékone arbitre assistant
Moussou ma kham béneu signa
l miézè alco-fresh niggah
Même quand je ris jaune
Je dois gagner mon paiin boy takhalé ay
Billet fatalo ay boulangerie jaune

[CHORUS]
Sicap tous les jours
Fuck sa rappeur tous les jours
Make sa money tous les jours
Fuck ay bitchees tous les jours tassaré
Tassa, tassa, tassa tassaré
Tassa, tassa, tassa
Tassa, tassa, tassa
Sicap tous les jours
Fuck sa rappeur tous les jours
Make sa money tous les jours
Fuck ay bitchees tous les jours tassaré
Tassa, tassa, tassa  tassaré
Tassa, tassa, tassa
Tassa, tassa, tassa

Watch Video

About Tassaré

Album : Tassaré (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 10 , 2019

More OMZO DOLLAR Lyrics

BRK
OMZO DOLLAR
OMZO DOLLAR
OMZO DOLLAR

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl