BRIL Démal Ma Dém cover image

Démal Ma Dém Lyrics

Démal Ma Dém Lyrics by BRIL


Beug nala lol
Ya néh sama khol bi maan
Wayé fouma dém, deukké khoulo
Ladoul meune
Diguanté bo kham’né problème souba’k ngone
Même soumalay nékhal sakh
Nga melni maay sa none yaw
Ya néh sama khol, téh beugua toumala guiss
Maan dotou mala kholl
Doneté dinama tiss
Nékko sama none yaako guena xam
Wayé meunou gno dound’aat legui
Boka tougnu yoon fila meuna yaam
Meuna tougno  and’aat
Naafi leepeu yaam maa’ak yaw
Meuna toul dém beugua touma
Daara tchi yaw doneté beug nala
Yaw Démaal maa déém
Yaw Démaal maa déém
Na kouné déém mou diékh
Naafi leepeu yaam maa’ak yaw
Meuna toul dém beugua touma
Daara tchi yaw doneté beug nala
Yaw Démaal maa déém
Yaw Démaal maa déém
Beugua touma xoulo ak xékh

Dégu louma yaaw milé
Défal loula nékh, maan dama tchi paré
Nakh sama khol dotoul diékh
Kone nakk sétil kénén
Ma kholi lénén kom meunou gno déggo
Démal fénén, téh fatéma nakh dougnou meussa djoubo
Dagua yakaroni meunou maala bayi
Ba loula nekh ngadone déff
Damala mougnal ba taayi
Fi meuna tofi done chef setil kénén
Ma kholi lénén, gnoun gnar dougnu déggo
Démal fénén, téh fatéma nakh dougnou meussa djoubo
Naafi leepeu yaam maa’ak yaw
Meuna toul dém beugua touma
Daara tchi yaw doneté beug nala
Yaw Démaal maa déém
Yaw Démaal maa déém
Na kouné déém mou diékh
Naafi leepeu yaam maa’ak yaw
Meuna toul dém beugua touma
Daara tchi yaw doneté beug nala
Yaw Démaal maa déém
Yaw Démaal maa déém
Beugua touma xoulo ak xékh

Yaw Démaal maa déém
Yaw Démaal maa déém

Watch Video

About Démal Ma Dém

Album : Multivers (Album)
Release Year : 2020
Added By : Farida
Published : Dec 01 , 2020

More BRIL Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl