Love La Lyrics
Love La Lyrics by CANABASSE
Chérie ahn chérie
Suma la nee bëgg naa la nga war maa gëm
Nee naala la love lë nga ni da may sóob
Yeah xam naa am nga lu bari Looy sóor
Mais jaay neex bi bu yàggee baby Da fay soof
Su ma la nee bëgg naala nga war maa gëm
Yeah xëyna bu ma wayee nga dégg hey
Da ma laa bëgg baby kaay ma
Wan la loo mësul gis sa life
Bàyyil sa yaram bul ma jaay sës
Sa ma ambition du benn night
Player dëgg awma läy
Li nga jot â dégg lépp right
Homme à femme je plaide coupable
Passons à la prochaine étape
Okay baby da maa legendary
Moo tax wax ji bari ay duul taq ci
Du ma polémique
Saabu fóotul boppam mais ak tuuti efforts temps
di na la wan lu set yeah di nga sip
Ñi nekk sa nopp they just talking shit
Gëm leen a tax nga naan ma cest pas possible
Mais deep down xam na Ma lay kill
Récupèrer la mooy sama dream
Lenn a ma leer mooy yéene naala mbëgéel ak mbégte bu bari
Te ñee nañu la yéene néeg la ko li ma la
yéene lu neex laa ciy jëlee you feel me
Nee naala la love lë nga ni da may sóob
Yeah xam naa am nga lu bari Looy sóor
Mais jaay neex bi bu yàggee baby Da fay soof
Su ma la nee bëgg naala nga war maa gëm
Yeah xëyna bu ma wayee nga dégg hey
Yeah day soof
Ma lay teg choc
Yaw nga may off
Ma lay wax sama dëgg nga koy teg foo
Sa may défauts gisa goo ko
Mais sa copines yee nekk di ma teg sot
Di la tegal bépp xeetu info
Ci sama ag ex mais c’est simple yo
Lu tëgg tas te ak yaw laa bëgg tabax today
Waante sa xol mooy xeex ak sa xel lady
Sa nopp yi fees dell ak ay wax yu may juger
Sa bët yi di gi ma'ak yaw am na waay
Mais leegi ma toqi yeah baby joxoñ bi du wëy
Jox ma sa loxo ñu ànd dox boo ko defee
Di nga xam jarul woon douter
Yeah baby baby ñëwal ñu dem dem
Awma prétention ni xam naa li ngay seet
Mais trajet bi day neex ba nga fàtte quête bi
Bàyyil sa yaram and follow the man
Lenn a ma leer mooy yéene naala mbëggeel ak mbégte bu bari
Te yéene moom néeg la kon li ma la yéene bu dee dëgg di naa ci jot
Nee naala la love lë nga ni da may sóob
Yeah xam naa am nga lu bari Looy sóor
Mais jaay neex bi bu yàggee baby Da fay soof
Su ma la nee bëgg naala nga war maa gëm
Yeah xëyna bu ma wayee nga dégg hey
Watch Video
About Love La
More CANABASSE Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl