Coco Coco Lyrics
Coco Coco Lyrics by PAPE BILAL
Mann damala beugue té xamoulo kooo
Man + yaw chérie = mbeuguel pure
Chérie nimala beuguei wooo euppeu naa
Maan damala beugue té xamoulo kooo
Bouma keuneu mayei mann keuneu
Maan damala beugue té xamoulo kooo
Diaral ngama xarei wooo doon lat dioroo
Dila xarel donn sa damel
Kaay fone ma chérie coco kaay waay
Ndaw bou nguissoul kamou miin dina wéetooo
Maan damala beugue té xamoulo kooo
Soumala diokhei sama xol yaw ngamay maadj lo
Dama naan thiekh si digueu beu diokh koudoul misere lo yeah
Mann beug naala waaw waaw
Mann damala beugue té xamoulo kooo
Autoraay fakhatina alloup kaagn
Sama xollay weundeilou ba biir this kaay yeah
Mann beug naala waaw waaw
Mann damala beugue té xamoulo kooo
Nga ma diaral chérie euppeu nay mayoup xool
Salaw kenneu douma thiopatei koudoul yaw
Mann beug naala waaw waaw
Mann damala beugue té xamoulo kooo
Sama chérie coco coco
Dinala dieundeul auto
Dougueul leu si ay chateaux
Tek leu si ajania nbanbia
Nii rek lagn koy deifei nimou yombei
Dougueul ko si ay chateaux
Tek ko si ajania nbanbia
Sama chérie coco coco
Dinala dieundeul auto
Dougueul leu si ay chateaux
Tek leu si ajania nbanbia
Mbeuguel nimou thi maan gaaw ni bouloup baby waaw
Diam wiri yaw nama laal xool ba ngui boul keu reusseul
Sama chérie coco coco
Dinala dieundeul auto
Dougueul leu si ay chateaux
Tek leu si ajania nbanbia
Fessnga si mann, diekh nga si mann
Foneithi mann ay kouko xam wakh mako
Sama chérie coco coco
Dinala dieundeul auto
Dougueul leu si ay chateaux
Tek leu si ajania nbanbia
Wool ma loly, yayou maty
Fo nei si mann ay kouko xam wakh mako
Sama chérie coco coco
Dinala dieundeul auto
Dougueul leu si ay chateaux
Tek leu si ajania nbanbia
Dougueul leu si ay chateaux
Tek leu si ajania nbanbia
Watch Video
About Coco Coco
More PAPE BILAL Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl