Yëguloma Lyrics
Yëguloma Lyrics by CANABASSE
Yëgu looma
Yëgu looma ba maa ngi agi gai yoo toppatoo wooma
Yëgu looma ba maa ngi ñibbée
Resulooma
Yëgu looma ba ma ngui gëmmentoo
Faale wooma ni yëgu looma
Yëgu looma
Da ma sonn ci di def les mêmes reproches
Li ma namm ci jabar c’est des p’tites choses
Tëjal sa gémmiñ bu may wax yow
J’en ai marre de tes justifications
Sa jëf ji du Lu bees
Te leer na ma bin du tay lay jeex
Ndax yàgg naa remarquer ay changements ci yaw te jot naa la ko wax
I’m the real nigga type
Li ma gën a bañ ci life mooy baamtuwaat
Fils da nga meloon ku dëdu jàmm
Lii du sa cër déggalal sa waay
xam naa ni ku nekk ci ñun am na nu muy Gisee Life
Mais am na yu amul négocier kon appliquel Balaa naaj
Melooo woon nii dou lii nga ma doon wan balak ma lay takk
Signalé gauche dem droite my baby film bi nga sàcc
No ki May Gis du yaw lady
Da nga jekkii bëgg saxi laaf
Changé sa jiko topatoo watoo ma
Pourtant Maa ngi def lépp li ma war
Du moins li ma mën mais mel na ni doyu mala
Man mënu ma dëkk ci joxe sans retour lii du life
Lii mooy genru night yiy lëndëmal mind
Baby fayu looma li ma la lebal
Dama la love mais wan nga ma ni yëguloo ma
Boo ma yëggoon doo xam ñi sama xol neexul ngay nelaw
Waaye bëgguloo ma
Boo ma bëggoon di nga jug balu ndax xam nga ni yaa ma tooñ
Yaakaaroo ma
Du ma genrou Góor buy bàyyj benn jigeen mu may yab
Dama yàgg bàyyi mu sedd ndax néegu sëy bi moo ko laaj
Waante sëy bi jaralu la li mu ma jaral ndax Gis naa ñi
Yëguloo ma
Yëguloo ma ba Maa ngi gai yoo
Toppatoo woo ma
Yëguloo ma ba maa ngi bëgg ñibbee
Resu looma
Yëguloo ma ba maa ngi gëmmentoo
Faale woo ma ni Yëguloo ma
Mësu ma xalaat
Naa toog bay douter sa ma choix ci yaw
Li nga ma doon wan
Tay mu ngi mel ni ay mirage you know
Bae lan moo la dal
Bu dee ci man la tamit please let me know
Jugal ñu waxtaan
Li ngay wakh ndégienaye bi Wakh ma ko
Amoul solo bo beugatoul Wakh ma ko
Mane tchi sama bop limay yeuk tay dou love
Frustration bou andak haine
Kheudj na sa gno sokhla trêve
Nagn wo pa yi fassone sëy bi fetchi ko
Mangui wakh mais limay wakh khamna ni geunalouma no
Bouma Sangone gnou dess mane ak yow meuna yar sunuy dome
Ndakh mane khamna li nekk tchi magg tchi kër bou tass té yéné wou ma len ko
Nagn teudd ba soubeu kheudj na seytaané dem abal gno
Yëgu looma
Yëgu looma ba maa ngi agi gai yoo toppatoo wooma
Yëgu looma ba maa ngi ñibbée
Resulooma
Yëgu looma ba ma ngui gëmmentoo
Faale wooma ni yëgu looma
Yëgu looma
Watch Video
About Yëguloma
More CANABASSE Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl