Dara Gënul Neex Lyrics
Dara Gënul Neex Lyrics by CANABASSE
Dara gënul neex
Ma tëddmu ñëw sama wet
Dara gënul neex
Di chuchoter sama nopp baby
Dara gënul neex
Bu fi nekkee fàtte naa lépp
Lu journée metti-metti mu ngi ak formule magique
Xam na fum may jaar ma nekk baby
Dara gënul neex
Lii ana lu ko Gën a neex
Tëdd ak baby sama wet
Xalaat ak xel bu ñu dajee
Wax day bàyyil place bi jëf
Day gis sama doxin xam ni doxul
Gis sama toogin xam xéll toogul
Daf May xool ci bët Gis sama xol
Li ci manqué la ciy sol
Li ma àdduna yan mo koy yenni
Damay yendoo coono téll-télli
Lu journée metti-metti meti mou ngi ak formule magique
Xam na fum may jaar ma nekk baby
Lu ma low low daf may yëkkati
Moom mooy sukkar sama Life
Oh Lord fu ma jëlee kii
Bii xeetu mbëggeel dara gënu ko neex
Dara gënul neex
Di chuchoter sama nopp baby
Dara gënul neex
Bu fi nekkee fàtte naa lépp
Lu journée metti-metti mu ngi ak formule magique
Xam na fum may jaar ma nekk baby
Dara gënul neex
Moom Mooy feexal sama xol
Moo may bégal
Janoo ak moom rek di xool daf may apaiser
Après 8heure ku ma call du ma la jël
Maa ngi mode avion jël na volou mbëgéel di plané ni ku tux ay boon
Sa ma nopp ci poojam ma koy nettali ay bêtises baby di dee ak ree
Life da fa metti dëgër sérieux bari pression tax ba Góor Yàlla di soxla trêve
Juge ci desert dox ba daje ak teen
Maa ngi ak sama kër
Man ak sama reine
Toom ma génnaat xare guerre
Ñibbi si fékaat fi trophée gagner perte yeah
Lu ma low low daf may yëkkati
Moom mooy sukkar sama Life
Oh Lord fu ma jëlee kii
Bii xeetu mbëggeel dara gënu ko neex
Dara gënul neex
Di chuchoter sama nopp baby
Dara gënul neex
Bu fi nekkee fàtte naa lépp
Lu journée metti-metti mu ngi ak formule magique
Xam na fum may jaar ma nekk baby
Dara gënul neex
Moom Mooy dëfal sama xol
Moo may bégal
Janoo ak moom rek di xool daf may apaiser
Après 8heure ku ma call du ma la jël
Maa ngi mode avion jël na volou mbëgéel di plané ni ku tux ay boon
Sama xol bi la ni bërët
Di saf lu neex
Ji ma mbëggeel
Wuy mbëgéeloo
Mbëgéel a bari doole
Watch Video
About Dara Gënul Neex
More CANABASSE Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl