...

Ndank Rek Lyrics by SAFARY


Saf

Mool

Nekh

Tooy

So répé ba dougou ci man

Ak nima nékhé

Tay nga dé

Oh bb, douma reubeu di sooy

Souma nélé nipe

Doto dooy

Khadioul ci yow sama beureudj

Man comme drogue ci déréte

Yako tay wakhok tapéte

Douma délo avance Dédéte

Khadioul ci yow sama beureudj

Man comme drogue ci déréte

Yako tay wakhok tapéte

Douma délo avance Dédéte

Lolo takh Manila

Ndank ndank ndank

Somay nope nope ma ndank ndank ndank (namone na)

Ndakh dama beuri vice (oh)

Damléy coller serré

Sa tankak sama tank (ndiap rek)

Oh baby Dama siss, bo sété ba ci biir

Gni malén gueuneu pank ( eh wouyoul li )

Sama baby, goudi tay bi

Narna yague, narna meti

Samay Baram

Di dokhanetou

Ci sa yaram

Ndaw lou sexy

Oh baby souma fipo

Mba doo tagok sa sago

Khana sibo

Man dama bari djiko

Baby souma fipo

Mba do tagok sa sago

Khana siboo, dama bari Djiko

Néwone nala

Ndank ndank ndank

Somay nope nope ma ndank ndank ndank

Eeh yow Néwone nala ndank ndank ndank

Somay nope nope ma ndank ndank ndank

Ndakh dama beuri vice

Damléy coller serré

Sa tankak sama tank

Oh baby Dama siss, bo sété ba ci biir

Gni malén gueuneu pank

Kham ngani kén douma wéthiooo

Nekhouma déréte

Yague nala kép ngay youkhoo

Dima wowé sa yaye

Nane ma yaye, boye

So beugué keurgui kén doufi fanane tay ( eh pape guéneul keurgui )

Nane ma yaye,( thiabiti) boyoo (non bouma yakal)

Yanguimay gagn Manane leu B loy dioy

Héee nangouna seuy bi tay dieulna défaite

Doyalouma sodé soucar yalna diabéte

Yow danga dal tekci yalén gueuneu coquette

Oh baby Kay fi ma defla tapéte

Kaay gaw

Bayil lolou

Boul laal fofou

Dafay dawlo sama yaram

Man nak hahan hahan han

Yangmay rélo sakh

Arrêtél tamite

Khawma loutakh nga saï saï

Mangui saalit tamite

Yow linga bouga

Lolou la bouga

Tay fi ba souba amoul nelaw

Aythia diougal aythia

Wakh dji boum gouda

So toyé nala soupal

Sol sama khoukhal

Diék dila khoukhal

Khoukhal khoukh

Néwone nala

Ndank ndank ndank

Somay nope nope ma ndank ndank ndank (namone na)

Ndakh dama beuri vice (oh)

Damléy coller serré

Sa tankak sama tank (ndiap rek)

Oh baby Dama siss, bo sété ba ci biir

Gni malén gueuneu pank ( eh wouyoul li )

Watch Video

About Ndank Rek

Album : (Single)
Release Year : 2025
Copyright :
Added By : Farida
Published : Mar 21 , 2025

More SAFARY Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl