Sa Takussan (Remix) Lyrics
Sa Takussan (Remix) Lyrics by SAFARY
Madame la lal nala
La lal la lal nala
Kone madame seyeul eih eih eih
Bess bi sa bess leu
Tay gnou bégeul leu
Tay gnou bégeul le oh
Kone madame seyeul eih eih eih
Bess bi sa bess leu
Tay gnou bégeul leu
Tay gnou bégeul le oh
Kone madame seyeul
Néna yaw la dou kéne
Dou meusa done kéne boudone kénene
Kénene dou dém
Dafa bayi keur yeupou né yaw sa takussan, takussan
Moné liko nexe moy raw dieuleul
El Hadji ma yabal si yaw
Néna mom dioxé na takou deunam
Dafa bayi keur yeupou né yaw sa takussan la
Sa takussan
Moné liko nexe madame dieulal
Mayé ngou ndieukeu matt na
Badiéne mom doukatt na
Wadiour yi dé contane nagn
Aki néna gnou paré nagn
Macha alla
Madame la lal nala
La lal la lal nala
Teugeul teugeul bongo
Kone madame seyeul eih eih eih
Bess bi sa bess leu
Tay gnou bégeul leu
Tay gnou bégeul le oh
Kone madame seyeul eih eih eih
Bess bi sa bess leu
Tay gnou bégeul leu
Tay gnou bégeul le oh
Kone madame seyeul
Yako saub nangou na beugu na leungeu ko cotou ko
Yako saub nangou na beugu na enh enh
Beugu nala lol
Dieuleul xole bi
Kone madame seyeul eih eih eih
Bess bi sa bess leu
Tay gnou bégeul leu
Tay gnou bégeul le oh
Kone madame seyeul eih eih eih
Bess bi sa bess leu
Tay gnou bégeul leu
Tay gnou bégeul le oh
Kone madame seyeul
Boul dorr boul saga
VIP lagn la indile
Boul dorr boul saga
Linguere pire lagn la indile
Boul dorr boul saga
VIP lagn la indile
Té yeul, té yeul
Yaw té yeul
Boul dorr boul saga
VIP lagn la indile
Boul dorr boul saga
Linguere pire lagn la indile
Boul dorr boul saga
VIP lagn la indile
Té yeul, té yeul
Yaw té yeul
Watch Video
About Sa Takussan (Remix)
More SAFARY Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl