Noy Moyto Corona Lyrics by BASS THIOUNG

Rew you bari lafi songando
Niou bari niakeu nagn sen baakane
Diotna nieup diougeundo
Kouné dièma arr sa askane
Koulay nouyou nèko non
Lègui meuneu touma diokhé lokho
Nioun daniou titt thji corona
Boula dalé amoul lo fadio
Yènn tok lènn sènn keur
(Tokk sa keur)
Té moytou mbolo yè
(Té moytou mbolo)
Topou digg le yi bayi téré yi
Di rakhass lokho yi
(Raxasal sa loxo bamou sett)

Corona, corona
Respectons les règles, c’est plus sûr
Corona, corona
Niouy dieufé ndigeul té bayi liniouy téré
Corona, corona
Deugeur bopou baxoul, restez chez vous
Corona, corona
Gnimou ray dafa bari té geunou niou lénn

Fagaro geunn fadiou gayi moytou lènn
Corona amma naniou andeu xékhando
Je reste chez, tu restes chez toi
Restons chez nous pour sauver des vies
Noy moyto corona ?
Raxasal sa loxo bamou sett ak sabou, raxasal sa loxo

Ya mom sa gel pathialal
Diweul, diweul bamou toy corona abal niou
Ya mom sa gel pathialal
Diweul, diweul bamou toy diweul
Noy moyto corona ?
Tok sa keur dieufé ndigeul té bania nouyo
Noy moyto corona ?
Tok sa keur dieufé ndigeul té  moytou mbolo
Ya mom sa gel pathialal
Diweul, diweul bamou toy corona abal niou
Ya mom sa gel pathialal
Diweul, diweul bamou toy diweul diweul

Néko non lègui meuneu touma diokhé lokho
Nioun daniou titt thji corona
Boula dalé amoul lo fadio
Corona corona
Corona, corona
Niouy dieufé ndigeul té bayi liniouy téré
Corona, corona
Deugeur bopou baxoul, restez chez vous
Corona, corona
Gnimou ray dafa bari té geunou niou lénn

Yalla naniou yalla mousseul thji lii
Yalla bourbi ya  indi lii
COOCID-19 dou thiaxann arr lènn
Yènn fagarou lènn

Watch Video

About Noy Moyto Corona

Album : Noy Moyto Corona
Release Year : 2020
Added By : Farida
Published : Mar 26 , 2020

More BASS THIOUNG Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet

See also



You May also Like



Get Afrika Lyrics Mobile App

About AfrikaLyrics 

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2020, New Africa Media Sarl