Don't Let Me Down Lyrics
Don't Let Me Down Lyrics by MANDIAYE SECK
[COUPLET 1]
Lima nekh thi iaw dagua done assassin.
Relation wou films
Yaye bandi boudoul dei quitte nappe sama khol tei ragualo thi
Dei baby don’t let me dawn limay yeuk thi iaw may baby dafa
Fort mbeuguel guouye taw di taw nawet noir raguoniou
Mbeuguel inondé na sama khol bii baby don’t let me dawn
Kone baby toudénala chocolat yay sama choco choco nutela
Kone baby yaye sama chocolat yaye sama nutela
[REFRAIN]
Waw khalebi momay guagne kénéne koudoul iaw bouguouma
Wakhnako sama yaye delou wakh ko sama baye baby don’t let me down
Sa khétou jongué monmay ray khawnako
Sama yaye delou wakh ko sama baye
[COUPLET 2]
Mame mbeuguel bima ame thi iaw doynama nécky agne ak
Rére souma done toubey yamay solle khaleby nopnala leuh
Waw sama yaye nenama soy beugu beuguel koula doy waw sa
Djiko nekhnama dagua tarou tek thi ame yare khaby doyguqma waw
Kone baby toudénala chocolat yay sama choco choco nutela
Kone baby yaye sama chocolat yaye sama nutela
[REFRAIN]
Waw khalebi momay guagne kénéne koudoul iaw bouguouma
Wakhnako sama yaye delou wakh ko sama baye baby don’t let me down
Sa khétou jongué monmay ray khawnako
Sama yaye delou wakh ko sama baye
[COUPLET 3]
Beugunala tay ma wakh lima nekh thi iaw waw sama fleurou
Khol bii sa je taimeuh monkoy arroser sa sourire moy limay doundeul way
Kone bahy diokhma ma sa lokho « thia bamouy mome »
Kénéne koudoul iaw mane kholoumako « aï bamouy mome »
Kone baby diokhma sa lokho way bahy kay niou fly
Watch Video
About Don't Let Me Down
More MANDIAYE SECK Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl