MANDIAYE SECK Senelec Love cover image

Senelec Love Lyrics

Senelec Love Lyrics by MANDIAYE SECK


[OUTRO]
Sama filou mbeuguel
La branche si sa biir khol bii
Soma alimente woul dina dina deeeh
Ndax leundeum kay branche ma waaaw
Ehh y ehh khale bii kay branche ma
Fay na sa facture mbeuguel
Boo teude nelawal doo kouniouy coupe wayy

[REFRAIN] 
Sama contorou khol bii lehh...
Yay sama contorou khol bilé
Kouma beug coupé day diar sii yaw
Cherie, teh doko meusseu nanguo… waw
Sama contorou khol bi lehh...
Yay sama contorou khol bi leh
Konn bb consomel
Consomel waaw
So doyale nga coupe cherie

 [COUPLET 1]
 tane na deff na sama demande senelec love
Indil ma conteure
 manilene dou fii nagn koo installe ci sa xol
Bii ndax cherie, 
Wolou nala teh kham nga limay begueul 
Confiance foumou ame sii relation waxx dja diexx way
Lamp mbeuguel bouy leral souniou yonn kontak bi sori woula bb
Tale koo lamp bi boul ci foo
Bou bourle sougnou yonn day leundeum
Sama cherie cherie diomou nako torokhal way wawaw
Ndaxté djiguénn djiguéne kenn douko torokhal no nono way !! 

[REFRAIN]
Sama contorou khol bii lèhh...
Yay sama contorou khol bilé
Kouma beug coupé day diar sii yaw
Chérie, téh doko meusseu nanguo… waw
Sama contorou khol bi léhh...
Yay sama contorou khol bi léh
Konn bb consomél
Consomél waaw, so doyalé nga coupé chérie

[COUPLET]
Courant kholoul baterie waw, boul nanguou kougnou coupè
Kenn doula guiss dii meer
Woute ngak facture cibiir keur marie,
Chérie cherif wawaw borom canada mayay !!
Dama donn niann leer dadjek senelec
Conteure bi sama khol bb yafi ne
Romb nga dijoncteur  boul  ma fowe
Yama koo woyofal, faw ma avouer
Hiiiiiiii… !!!!!
Ndioguou khalei fechenn bii
Domou yayou soumboulou beugu nala lol
Wolma nabou domou soumboulou domou bayou moulay beugu nala
Chamaramarang.......!!!!!!!

Watch Video

About Senelec Love

Album : Senelec Love (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 04 , 2019

More MANDIAYE SECK Lyrics

MANDIAYE SECK

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl