Bamba Ndiokonial Lyrics
Bamba Ndiokonial Lyrics by JAHMAN XPRESS
Okhoyolaana Mame Bamba barké naana Touba
Waw nañ dem Touba
Ku demoul ma dem dem ziaar yeslu
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Takk djouk sakhar
Ropalan
Auto ak
Kounek lalay yobbou
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Bismil ilahi
Niou sante yallah
Mom mi waraal
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Banouy mana ziaaré dji
Borom Touba ak Ndiareme
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Yaw lañou wôlou
Goor gui demoon ma Yomba
Gnibissi am ndam kenn dou domi Mame Diarra
Nitt ak Djiné ak Malaka yi tamite Kham nañoula
Cheikh Bamba dou mass lim’ñou defal amouñou payam
Defñou ñouy Mouride
Teksi yarñou banouné neureum
Bamba dou massoum
Fôré dou massoum
Bouraki Kangam
Kenn dou Bayi Seugne Bara
Dem na Gabon si ngor deloussi am Ndam
Demaat Ganaar ñeuw indi ngeuram
Souñou wadja mo def ci ñoun lou adina seedé
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Ba do khamé djoola Ndiago ak Sereer
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Mouride day djeufé Ndiggal
Tei bayi ay Téré
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Neelén euskeuy ci Sanguoup Borom Darou
Mo diara wolou
Moñu defar baniou taarou
Mom nii ñeup nèè massam amoul ci kharnoubi
May sante Sasouné magui Borom deureum ngeureum
Mbacké Kadior mbir yafa khew Barina lol
Leneen dathia khadioul
Cheikh Bamba rék ci khol
Thierno Borom Darou Djambar dja
Moko djitou woon fa ndaar li wernaa
Amna lol kouñouko wakhoul meunoko kham
Amittna lol kouñouko djokhoul meunoko am
Dedet
Djaraama Djaarama wakhlénn (Djaraama)
Djaraama Djaraama neelén (Djaraama)
Djaraama Mame Cheikh Ibra Fall’la minn yonn wi batay kouné meuna djaleu
(moniou’wann Cheikh Bamba)
Bam lér ni djante né fangeu
Wolounala Wolounala
Cheikh Bamba doylooo nala man
Okhoyolaana Mame Bamba Magal Touba yè Mame Bamba akhoyta ngaa ko mouride kéfop-nooyè
Bamba akhoyta ngaa-yé bilay Magal Touba
Alhamdou Sante nañ ci lingañou defal
Kou wet ci ñoun fokné lokho ngako beeral
Yañou sagal Cheikh Bamba Yañou teraal
Tayma fethie sar kholé yamako djaraal
Ndangou Yallah ki dogualam Yonén ak ay ndioñam
Ndangou yay kifi djokhé ñam
Djambarou kharnoubi
Waw mbeuroum meunéssouko daan (Ngeuram la am yonén baadi sangam)
Ndakh loum ñaan mou am (lam tontou ndaar molen takhona dem)
Ndeysaan wakhlén’ma Cheikh bamba mi foum’né si man
Sa yoko toudé may yendo retaan
Lima metiwoon nekh ma fassa saman
Souñou wadja mo def ci ñoun lou adina seedé (Diaraama Diaraama)
Ba do khamé djoola Ndiago ak Sereer (Diaraama Diaraama)
Mouride day djeufé Ndiggal
Tei bayi ay Téré (Diaraama Diaraama)
Neelén euskeuy ci sanguoup Borom Darou (Diaraama Diaraama)
Watch Video
About Bamba Ndiokonial
More JAHMAN XPRESS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl