Moyla Lyrics
Moyla Lyrics by DUDU
[INTRO]
Hé voila bon (ok)
Mani i i
Mané voila bon (ngani)
[VERSE 1]
Dama criq boy fils dé boy
Yeup dima guinz (Moyla)
Sama style dafa saff
Fils ba diap fi si sa xol (Moyla)
Hé deug deug nékhoul
Mais mol nga boy (Moyla)
Dou tchi man, tchi yow, dou kéne
Dou fils, dou nieup la boy (Moyla)
Mané kanla (Moyla)
Éh nianla (Moyla)
Éh kanla (Moyla)
Nioune nieup le (Moyla)
Mane loutakh soma kholé
Di geune di diongoma (Moyla)
Mane loutakh soma kholé
Di geune djental
[CHORUS]
Moyla, moyla, moyla, moyla
Moyla, moyla, moyla, moyla, moyla
Mane loutakh soma kholé
Di geune di diongoma (Moyla)
Mane loutakh soma kholé
Di geune djental (Moyla)
[VERSE 2]
Sène école souniou ma wowé té
Amouniou louniou faye (Moyla)
Mané douma nieuw, douma nieuw
Douma nieuw (Ay moyla)
Nga" Dokhane la nga bane
Guisma télé beugua nieuw (Moyla)
Nga togou domoda ba paré
Beugeuma wo (Moyla)
Surtout soupou kandja (Moyla)
Mané tiébou dieune (Moyla)
Mafé (Moyla)
Mané guinar (Moyla)
Mayé nangou bakhoul sa yaye
Déy am doumou diane (Moyla)
So doul brossou so
Magué dinga diaal (Moyla)
Soy guénak pata da fék
Nga wolou sa bopp (Moyla)
So méré yakoy yeuk ndakh
Golo gui dingako bok (Moyla)
[CHORUS]
Moyla, moyla, moyla, moyla
Moyla, moyla, moyla, moyla, moyla
Hé loutakh soma kholé
Di geune di diongoma (Moyla)
Hé loutakh soma kholé
Di geune dopé (Moyla)
Watch Video
About Moyla
More DUDU Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl