Dieulil Lyrics

CANABASSE Senegal | RnB, Afrobeats

Dieulil Lyrics


 [REFRAIN]
Bo djougué mane wane ma fima djougué
Digua djouk fadiaar téél taakk toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma gouddé
Sama nope baatu mère dima goungué
Né nama "basse basse bass
Abdou démal dieuli li ngua mom
Né nama "basse basse basse
Yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
Té bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug
Bouk topoto say noone
Abdou basse basse basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom

[COUPLET 1]
Bou ma tchi seugué douma siggui
Bou sérithieu bi matoul douma gnibi
Boudé yaapeuh taamou na tchi dibi
Boudé yaapeuh dioxma diplôméé bi
Xalé bou djangueuh tangueuh
Diaape niaamboureum
Djiguéne 100% ma tchi thiapeuh some
Té bouko diaré mane sagne naako songueuh
Séti waadioureuum niaani dji lokhom
Rap game bi légui noumou démé
Niom nieupeu beug nékeu moi
Mais kéneu matou tchi nii février
Douniou gatt loudoul tchioutchiou ci thiaaz
Yombeu love boma beugoul
Xamna da nga am problèmou xol
Sho bi néma:"may nélaw douma robot"
Mane manéko

 [REFRAIN]
Bo djougué mane wane ma fima djougué
Digua djouk fadiaar téél taakk toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma gouddé
Sama nope baatu mère dima goungué
Né nama "basse basse basse, 
Abdou démal dieuli li ngua mom"
Né nama "basse basse basse, 
Yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
Té bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug
Bouk topoto say noone
Abdou basse basse basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom"  basse basse basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom

[COUPLET 1]
Makoy todj fils guiss nga limay tabakh (tabakh)
Philip morris lou guéneuh def tabac (tabac)
Stephen curry fouma tolleu thiabakh (thiabakh)
Marqué sama temps ni chaba (chaba)
Doundeu ba bi may dougou sama pas (sama pas)
Maximum bi séddé ni dama bakhh (bakhh)
Tolo féneu beug dieul sama part (sama part)
Roi des arènes fékhel bama mbapaate (mbapaate)
Rakkeu geunaatal rap ba tchi kanam
Fi nga né ma ngi fawone
Ay aate ci guinaaw
Cachets et concert et tu parles de finances ?
Dama rap baniou may wo tchi ay conferences

Def cos bou saff andeu ak éloquence
Wane lène finiouy diaar def différence
Bou bakh dou bou bone bone bi
Yeah bi moy référence
Yeah def ko sa bopp fils
Shampooing dou karaas
Sa rappeur dou bagaaass, (sa rappeur dou bagaaaaaage)
Yombeu love boma beugoul
Xamna da nga am problèmou xol
Sho bi néma:" may nélaw douma robot"
Mane manéko:

[REFRAIN]
Bo djougué mane wane ma fima djougué
Digua djouk fadiaar téél taakk toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma gouddé
Sama nope baatu mère dima goungué
Né nama "basse basse basse, 
Abdou démal dieuli li ngua mom"
Né nama "basse basse basse, 
Yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
Té bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug
Bouk topoto say noone
Abdou basse basse basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom"  basse basse basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom

[REFRAIN]
Bo djougué mane wane ma fima djougué
Digua djouk fadiaar téél taakk toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma gouddé
Sama nope baatu mère dima goungué
Né nama "basse basse basse, 
Abdou démal dieuli li ngua mom"
Né nama "basse basse basse, 
Yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
Té bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug
Bouk topoto say noone
Abdou basse basse basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom"  basse basse basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom

Leave a Comment