WALLY SECK Thieuguine cover image

Thieuguine Lyrics

Thieuguine Lyrics by WALLY SECK


Mane xam nani kep kou kofi meusseu
Beguentel malako gueneul
Ba soumala guissé damay rétane
Mane geum nani doumala meuseu trompe ben yoon
Ndax yamaleen gueneul
Ba soumala guissé damay rétane
Mais nak ma wakhla limay dounde soumala seené
Nguay wakh ak kénén dafmay bouleversé

Je serais là où tu me laisseras
Ne m’en veut pas, que je ferais sans toi
N’est qu’une illusion
Aucun mensonge, qui me mènera qu’à illusion
Aucun mensonge ne m’éloigne de toi

Kholal sounou diguantei nitte
Gnie sakh dan niou naw
Kholal bougniou ande nine niouy xolee
Begouloma nguirr alal mo waral ma taneu le
Diaral nguama tago ak nieup
Nguir sa dieum dji
Huuuuum hummmmmm
Ndaw si lé diamono dji da
Ngay galakh ndiko lamigne
Sucaré la xél Khorame la beut
Té dougne la wakh deug li dou Yoon
Non Non Non boulen déglou nawlo woumaleen
Mame Coumba Salymata mba wax nga
Adama Aziza Almamy Abdalah Papis
Kou beug sa waaay way wi yay borome

Beug nala beug ngama ba kén meunouniou féwalé
Nop nala nop ngama ba kén meunouniou féwalé
Non non non bouniou wétté ba kén rabouniou
Malay féthial dila lébeul dila féthial bilay
Thieuguine thieuguine
Set na ba set yamay motali di fékheul sama xol
Yamay defeul mane woh woh woh
Ma melni Baba Chérie Yande
Ma melni Pape Diop Chérie Youssou Gaye
Laylaylaaa woh ho ! da ngen di
Féthi moulay thieuguine thieuguine
Ma melni Papis Chérie Ngala
Ma melni Momy Chérie Dany
Boubacar chérie Diarra dégeuna ya ngui
Féthi moulay thieuguine thieuguine
Ma melni Diène Dieng chérie
Awa bayou Mounas bayou
Ndiogou da ngey féthi moulay thieuguine
Thieuguine

Watch Video

About Thieuguine

Album : Thieuguine (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 19 , 2019

More WALLY SECK Lyrics

WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl