Epic Lyrics by PACO BRIZ


Deuk bou bari nafekh fen kat ak gnou sokhor té ignane
Am gnanou wadiour késsé lassiy guéné kone yaye boye boulma faté si niaan
Sama papa mo ngui may diapalé chaque jour mo ngui téyé chapelets
Pér boumou kheuth barké baye leu yokma fit waral douma tapalé
Sen état d’esprit la coup d’état ils savent pas ce qui se passe
Nga ni ya contrôler game bi kone tayo ko bi nga makoy pass
Yow leu MC serviette hygiénique mar katou tate si yow la fek mbakh
Ken douma djité massouma am coup de poussou ken dou ken si gnom non non  
Man xawma  wakh diou beuri thiaxané wou ma mbir yi défense de fer Coulibaly
Rappeurou thiép bou sew bé beuri na len togg sombi lapin soutoul baly baly
Boy dédét man nieuwou ma clash ken pour geuneu siw talent moy intérêt respect di bénéfice
Man dama geum sama bop mbolo moma top dome
Ndèye guichet fermé té falé wouma ken negger

Koufi sampe ndeundeu teugeul ko sa bop
Bala bakou wakhma kou thi top
Fi kou nek khamna ki la fété kaw ak ki la
Raw ak ki  la eupeu karaw ak hip hop
Beuri rasta sama bop té nékouma bob
Bop bé diakhasso ba diap karaw ngi lo fok ?
Médiocrité la gnouy favoriser motakh game bi do guiss
ken kouy rapper ni man té label yeup  teuthi na  séni gat

Lan ngen fok ?
Dama gneuw tek rek dem tok
Fi ngen may fek let them talk
Fokma dieul pause pour ngen bok
Tégal banc sol tik tik, tok
Défi comédie bir tik tok
Couper fepp Mademba Sok
Dawal té douma def choc

Damay diéki diéki guéneu gallé gnou may garouwalé
Nè nagn bouma diéko douma balé nala réndi walé
Dougou gallé rappeur yeup dialé siguil len ndigalé
Man la épidémie damay walé vacciné wou walé
Étiquettou rappeur sénégalais game bi da localé
Didji mariné ba paré waané amo lofi wané
Stylé wo  Negger danga tané copie collé walé
Kay ma diokhla Afshal ndakh mou tané non non  dou guissané

Teubeul ak féthi bou yagu bi néma beukeuteu beukeuteu
Dama yagg meuneu binde melni PPS PPS
Fima diogué rappeur bou melni man déssou fa déssou
fa non non déssou fa déssou fa
Khana danga dof ?
Boma khamoul wowé ma King Lébou negger
Mane la domou Yoff té danio boolo dounou bérou negger
Danouy danou rap di ndeup fek dérét tourou negger
Gneup morom lanou ken dou fatté kouy sa mbok negger
Da nga beug beef boy ah bon
Yow la MC compas ya ngui tourner en rond  
May  sen pa man la sen daron
Talent tu ne l’as pas et puis  boy t’es con
Bene instant nga fiy dégg sen son
Accidentellemennt ngen di dégg c’est bon
Ndéké fi gnou beuri médiocrité la gnouy favoriser motakh game
Bi do guiss ken kouy rapper ni man ma bamtou wat
Ko pour ngen dégg deug !
Bitch

Watch Video

About Epic

Album : Epic (Single)
Release Year : 2021
Added By : Farida
Published : Jun 08 , 2021

More PACO BRIZ Lyrics

PACO BRIZ

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl