WALLY SECK Si Vous Saviez cover image

Si Vous Saviez Lyrics

Si Vous Saviez Lyrics by WALLY SECK


Ameth Pouye ak Ndeye
Sène mbeuguèle la
Si vous saviez se
Que veut dire l'amour
Encore saviez-vous
Ce que veut dire l'amour
Remercier à chaque instant
Voire le sourire de l'enfant
Admiré le soleil couchant
Apprécier la caresse du vent
Si vous saviez
Ce que veut dire l'amour
Encore saviez-vous
Ce que veut dire l'amour
Partager à son coté
Entendre votre coeur chanter
Ecouter une voix vous guidée
Eviter ce qui peut blesséééé

Bimbaram Ndeye yagui dioguè ba walo
Mouhameth sokèko ba wakaaam
Ndeye mougui dioguè ba walo
 Mouhameth sokèko ba wakaaam
Ndeye mougui dioguè ba walo
Mouhameth sokèko ba wakaaam.
Mbeguèle nila mbeguèle noooooonoula
Sai sai bèèèè sai sai bi

Beugue nala, fonke naaaaala
Mane seytané yi
Demba Sène, demba Sène
Idrissa say sa baye Laye Sène
Adja Saly Diagne sa yaye
Aida Mbene na samay Mbaye Sène
Beugue nala, fonke naaaaala
Mane sai sai bééé sai saiiiii bi

Narou katy narou Youssou
Madjiguène Ndour
Mala beugue wore na y’Alla mala fonke
Sama mak dji mala tamou mala tipo
Oooooohhh Biraaaane Ndoure
Nitte koulaye woute Birane

Dième dième diotoula
Dina fèkhè ba fi guena
Dièguè mou diarèfa
Ba yakal la make sama malaye wayal
Adlaye daro maaaaaame madioro
Nitte koulaye woute Birane

Diéme dième diotoula naniou fékhè ba
Bougne ko maye foumou diaare
Ba yakhale niou
Aicha Lô gaïndèle gaïndèle
Khoudia Coumba ndama
Youra Khoudia Coumba Diallo dièrè
Khoudia Coumba ndama

Watch Video

About Si Vous Saviez

Album : Si Vous Saviez (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 19 , 2019

More WALLY SECK Lyrics

WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK
WALLY SECK

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl