??? Lyrics by DOPE MASTER


I do it all my life yeah
My nigger now tried
They say no pain no pain
I used to fight all night
Diangu mais khamougn lou god di wakh
Aldiana noy déf beu am feu place
Adouna dieuf bouné ak conséquences
Kéneu meunoul live for life?

Yeah nigger diote na sissou gayine
Kom fou bou sick di shine
Dofougn kéne khamoul lou dall sougn mind
Tenter teh Temps que matoul dougn tayi
Hustle ba Hustle ba deih suicide
Fayekou teh yorougn lou fay souniou yay
Ligeuyou ndy mousslay
Noneu yeupay tew souy nice ( ay )
Kharougn si kenn teh gné wou niou kenn
Bamouy tarr guissou niou kenn teh tewoul niou dém
Nieupay deih money dou téh niou soul leu si pakh
Bamay deih damakoy weur meuneu nama doundeul
Meuwti dima tiatal noneu yi dima tiatou
Mama néma fassal sa diom lou tarr yagoul
Jour bi nguay kham ki ngua done si nguay lakou
Life bi kom tiagua douma fay pour danou

I do it all my life yeah
My nigger now tried
They say no pain no pain
I used to fight all night yeah
Diangu mais khamougn lou god di wakh
Aldiana noy déf beu am feu place
Adouna dieuf bouné ak conséquences
Kéneu meunoul live for life?

I did my nigger
I’m from the ghetto
I used have problems I live it with no matter
Now all my niggers we sleep in em’ bitches
No pain no gain I climbed the piramid
Level bou satanic
Projet you méthodique
Taylé nieup guéneu si
Diogué fi deukou niou fi
Rap fi dou industrie
Kagn rek lagn nara sipp
Sama talent khadiou fi bayil rek ma tek ko si
Bayil rek ma tek ko si teglè ay millions
Mère bi waroul worry tabaski mongui nieuw
Balay nguay matal sakh fek ni soulou ngua
Life bi Dafeu tarr teksi meuwti dou nouyo
Téleu kheuy ni goor fall kou fonk ligeuy
Meunougn deuk si topp fok niou dirigé
Gnissi kaw nioune nieup lagn diay
Mais doussi niom nioune nioy coupable
No one can live for life
Tay ngua doundou souba RIP ndeysan
Adouna bi gnissi ndieuk dem nio bakh
Mais Nieup fi niouy moudié si pakh lay done?
No one can live for life
Sms dollar nigger rest in paradise
Bo guissaté yallah posé ko question way
Nala wakh ki fi moudiou kane mokoy soul ???

I do it all my life yeah
My nigger now tried
They say no pain no pain
I used to fight all night
Diangu mais khamougn lou god di wakh
Aldiana noy déf beu am feu place
Adouna dieuf bouné ak conséquences
Kéneu meunoul live for life?
I do it all my life yeah
My nigger now tried
They say no pain no pain
I used to fight all night
Diangu mais khamougn lou god di wakh
Aldiana noy déf beu am feu place
Adouna dieuf bouné ak conséquences
Kéneu meunoul live for life?

Watch Video

About ???

Album : ??? (Single)
Release Year : 2022
Copyright : © 2022 Nautylusprod
Added By : Farida
Published : Oct 14 , 2022

More DOPE MASTER Lyrics

DOPE MASTER
DOPE MASTER
DOPE MASTER
DOPE MASTER

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl