Milli Milli Lyrics
Milli Milli Lyrics by DUDU
Fresh prince of ndakaru done sen chef rakaju
Ngadim bidéw té tarru, may borome ndakaru
Nek 1er ngadim dialoré certifé million followers
Dama geuneu rakaju na millions bi ma kaniou
Le milli le milli c’est le milli le milli
Lerr na ni midi, yeah, I did it I did it
Ioe mi mey déglou ioe ya ci diap
Boudoul wone ioe douma yeksi fi
Folsol bou niw di nga guiss sa bop
Dudu comme sentou kou yendou guiss ko
Comment faire « eupeuteuleuw »
Dama fier nek cikaw mongolfière
Yeungeul terre, yeungeul ciel
Ana gni merr, ana gni begue million douguate
Diko dougate, diko douguate, diko dougate
Million douguate, di nga douguate, di nga douguate
On veut le million le mignon
Biir bou ngandé Amdy Mignon
On veut le million le million
par ce que le petit est mignon
Sathiouma ko, dama ligueye
Khalé bou ndaw, guel yi di bégue
Pa yi di bégue, mère yi di bégue
Wait a minute, wait a minute na million bi dougou
Wait a minute, wait a minute na million bi dougou
Wait a minute, wait a minute na million bi dougou
Wait a minute, wait a minute na million bi dougou
Watch Video
About Milli Milli
More DUDU Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl