Buur Lyrics by DOPE MASTER


Salut bro
Khame' ngu bone ak warga I'm that dope nigger
Started from the bottom but I'm up now
Chaque jour ma guiss boy bouma geuneu
Meune samay propre sound
Ça fait ni chaud ni froid boy so beussoule' j'aime
Seu Mc comme Lgbt damakoy khe'kh beu bamay ce'yi
Yow amo diote mais am ngua diotou sissou si commentaire
Fuck niggers up
Khaliss ligeuy get money force mba deih
Every day dawg
Funny pussy lil nigger
Dangua fogone so sagua dougn la tontou t'es pas au courant
Geuneu autonome sakh panneau solaire yi fuck seu courant
Pour ngua course ak dope fok ngua garou pneu secour enh
Game bi yeup rangg si kanam sama bopp la guiss
Mangui si gue'tou khaar te'h sama khol dou ngogn bi la feel
Ropi le'ne dou tarr, deih comme 2Pac kou meune dou de'ss fi
Dadji la si lucide barre bou nek missil ke'pal seu tate yi
Yagua teudiou si bir te'gou si beat yi ngua off si sassi
Assamane dou limite objectif bi di BET Grammy
Job beu khadiou goudi normal ngua ye'ma ma latchieu la khaliss
Fuck lou bakh di dieurign nite mo infide'le geunoul sakh khadji bi
No nigger Just like a gold digger ima make it move nigger
Ray niggers yeup pour ye'e'k si kaw bayi le'ne si souf ni ne'w
De'clanche'l guerre bi dou die'kh beu gue'dji bi di fe'rr
Boudoul sama gang douma meusseu care gnissi de'ss
Real nigger I'll never change
Always be the same
Be'geul sama yay never cry roy si sama pe're ayy
Kone khamal ni we're' dou louma narr
Dina ye'e'k bassi kaw dh teh douma marr tatou be'neu niggers
Game bi da serre' may ma ma dialeu
Nama fake yi baleu Mais tioup sama drapeau dara dou takh (He'y)
Alalou adouna my nigger fi leu yam
Dama guiss kou diay nguoram youkhou oh Ndeysane
Oh gandou gne' flow bi te'neu leu boy rotal dou die'kh
Yallay maye' te'ski yamale' woul fall def ko sa khe'l
Nguay ratatati rek wakh sou fayone done ngua milliardaire
Fake sori ma ak seu gang Og nigger dou fre'k ay naafe'e'k
Se're're si pe're si me're no meunti def ma done
Buur si bi game
Shit

Watch Video


About Buur

Album : Buur (Single)
Release Year : 2022
Copyright : © 2021 Nautylusprod
Added By : Farida
Published : Jan 17 , 2022

More DOPE MASTER Lyrics

DOPE MASTER
DDD
DOPE MASTER
DOPE MASTER
DOPE MASTER

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2022, We Tell Africa Group Sarl