
Chez Nous Lyrics
...
Chez Nous Lyrics by OOTHENTIK ZEUS
Baayinaa niak bu yag
Nakh yag baayiwoul dara
Waxtaanak sam ndieguenaay
Si guent yiy guent yiy takh ma am dara
Diour louné leng teh defoul diémoul
Loolou laa diaapé mouy yaradal
Baye bouma amé alal bouma seekhlou door ndamla sa yaradal
Solnaa sa dale mou diot
Wakhtou bi diotna ma seug sidiot
Li dess sama life naako sigui di dokh
Dawal waa gallé sam business dou sookh
Douma khadi si mettitou problem bou nieuw
Lou meunti am naako déloo thi god
Sorrinaa fignmay toogué dama nior
Teh dougnma yak loumay deloo thi niom
Yallah dou teudj bount adji rideau
Wane guinaaw gallé pour woutoudji do
La vie chez nous n’a jamais été rosa
Nakh xamgani ndool dalay wayadilo
Nioun niouy gagnger ay combats si gueum di door
Genrou boys yilaay khool melni amouniou khol
La vie chez nous n’a jamais été rosa
Mais gueumouniou len louniouy guemeudiloo
Nioun nioo diodou si niak, li niak oumpeulé niou xamiko
Sama yaay dafa banque ma régler ay comptes pour talil ko
Samay rakk la yor motakh boudé yoro douniou lamiso
Dereum ak dereum’ay ande kouy woutidji dereum laay def sama andando
Barres yimay bind fessal sama frigo bar, fans youla topu gueun girofard
Dioug woutidji philo heure bi ngay teud bad outer ni iso sarr
Xamnaa yaay mbima nguimb ma aart combak sama bopp doolé ma daan
Niak am lamay tonto sa ladj parce que sama dom waroula xam
Yallah dou teudj bount adji rideau
Wane guinaaw gallé pour woutoudji do
La vie chez nous n’a jamais été rosa
Nakh xamgani ndool dalay wayadilo
Nioun niouy gagnger ay combats si gueum di door
Genrou boys yilaay khool melni amouniou khol
La vie chez nous n’a jamais été rosa
Mais gueumouniou len louniouy guemeudiloo
Gueumouniou len louniouy guemeudiloo
La vie chez nous n’a jamais été rosa
Watch Video
About Chez Nous
More OOTHENTIK ZEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl