
Yaa Wara Comp Lyrics
...
Yaa Wara Comp Lyrics by OOTHENTIK ZEUS
Low yaa wara comp
Ni des fois waroo topu sa khol
Xalaat niou xawa faaté bopp
Douma tay dila togn
Low yaa wara comp
Nakhté yaa gueneu dieek thi xam
Louma def, louniou soss, louma wakh
Boul yem si deg oubil sa beut yi teh xool
Nakh yaa wara comp
Ni mbeuguel boudoon jaay louma mom
Lepp laay yeekeuti lathie ci sa khol meuneu doon kila mom
Low yaa wara comp
Limou naadj nako taw nako feekh
Ni dou taar dou alaal dou mbeuguel
Yeurmande ngaleu eupeulé thi sama khol
Low yaa wara comp
Ni douma meuseu fété sa guinaaw
Sissa weet falaa sah di takhaw
Loumou taarr douma daw
Low yaa wara comp
Ni booy merr ba di fass sa kanam
Sa retaan dima feete guinaaw
Damalay gueneu love
Damalay gueneu love
Low yaa wara comp
Low yaa wara comp
Boul yem si deg oubli sa beut yi the xool
Damalay gueneu love
Low yaa wara comp
Low yaa wara comp
Yeurmandé nga len eupeulé si sama xol
Damalay gueneu love
Low yaa wara comp
Low yaa wara comp
Boul yem si deg oubli sa beut yi the xool
Watch Video
About Yaa Wara Comp
More OOTHENTIK ZEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl