
Équilibre Lyrics
...
Équilibre Lyrics by OOTHENTIK ZEUS
Ahan
Ouh hahan hahan
Ahan
Ouh hahan hahan
Say
Douma diaapantek waa fima baayiwo
Rio city bi bando ndiaye lo
Nagger mafia bi dound neu trahison waayé drapeau bi ken douko thiouboulo
Time is money amoufi logique
Temp laniou niak pour wouti do
Neenagn mbokk mooy doon sa noon fils
Manilen maak niooniou bokounio
Sama maman nekk ci mane
Teh ken fekhou ko ci one
Bouma bonone niouni domam
Waayé ma baakh niuo bokko
My negger doundoumeu showbizz
Waayé showbizz mooy doundeul sam business
Am niouma fiaapéwoon homie
Waayé homie bi diappéma business
Yallah lay sant niom wakhleen niou sant ma mais douniu bok
Yémouniou boy eupeul rek mooy ngamay boolé si niom
Fii nieteelou baram bi laniulay showé sa love
We’re from the hood
Fi nga xamné bou tawé nga peuteukh pathiakh
Mbedd bi diang ba amoul vancances
Niangu na ken douné amoul thiakaay
Ba amoul nangou takaay
Mafia bi takk na depuis timis xalle you timides mandi mooy waral niou agresser nitt
Si bando bi créer millice slogan bi moy nique police
Husler life go no time bro i got to go
From my money for my og i’m about to blow
For my mama for my famlee all i got to know
Boy mooy paa bi maakoy nopal ak foum meun doon
Tekki fi def beug beug sam ennemi meun takhawal sama edifice
Nek si net bi si radio si télé bi foo tourné guiss meut eh rare na thi mbedd bi
Gueneu takhaw niak équilibre entre ma musique et ma famille
Né thi ben yor benen xamal niak mou creel leu ennemis
Dou gueneu makk sama bopp bi
Dieul adouneu contenir ko takh samay mbag yeuk thiono bi
Bi dara doul dara day new nga guiss niuolassi sutenir
Mais yaay ki ci nekkak foula bii, tay loolou lep nekk neu souvenir
Ahan
Ouh hahan hahan
Ahan
Ouh hahan hahan
Ahn
Watch Video
About Équilibre
More OOTHENTIK ZEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl