Kou Merr Tempi Lyrics
Kou Merr Tempi Lyrics by TBRAINS
[INTRO]
heei TBrains ak Dioly
Kou meer tempi
Thieuy doxolal doxal
[COUPLET 1_ Kalz JV]
Wiir meu 100mo ma posté mame fall send yi di dioly
Jop thi sans mot mou douggueulmeu poste yi abb thi solde yi
Fayuna May soukeur sombi
Ma djitoulen thiop thi maney only
Gua merfi dé dima nirou zombi yé
Xalebi snap feul feulalé sandi gauche ma OOw
Kennla thi man neko nayy bekk rek mou bax niou goo
Contann continué metrisel merr bi bayi mou guouss
Roubell teksi prix doundou lo fekké lou bonn gua pouss
Alma ki daanou May fath khiir gui la yor dh May thiaw
Alma ki daanou May fath khiir gui la yoor dh May thiaaaw
[CHORUS_ Mame Fall Dioly]
Dioly TBrains wax amoul ...hei
Dara xeiwul Thione teugoul hei Waly wayul Youssou deimoul Bercy
Kou meer tempi
Kou meer tempi
Kou meer tempi
Kou merr damay danou merr tempi
Tass mbakh reuguin tempi
[COUPLET 2_Mumz.OG]
Fi kou merr wowal ma dioly mu guifal sa merr
Fok am gnu sissou di sani xerr ni bén nandité si milliers caire
Fi neikh fi nit dafa diafei sen xalaat lay séréti comme kou diafté
Defko sa statu ragalougnu thioow comme satheu
(Voleur) digue beutheuk
Khol béy bonne neiko tempi
Lignu sampe lu ndaw duko simpi
Sa rappeur daxar manatul saff bignu aksei la sapii
Pour gnima begue chaque jour ma snap pour sen xol di feikh
Hei li dafa neikh xa neikh ioe bossi neikei bul nangou mou dieeeekh
Begue lou tarru day fay
Sagnsei si Ayan defsi grand boubou dei class bi day fay..Heii
Man ndandane la damay sagne takk lou thil gnodi si salagn
Salagn gueweul mbaay dima
kaaagn...yeeh
[CHORUS_ Mame Fall Dioly]
Dioly TBrains wax amoul ...hei
Dara xeiwul Thione teugoul hei Waly wayul Youssou deimoul Bercy
Kou meer tempi
Kou meer tempi
Kou meer tempi
Kou merr damay danou merr tempi
Tass mbakh reuguin tempi
…….
Dara xeiwul Thione teugoul hei Waly wayul Youssou deimoul Bercy
Kou meer tempi
Kou meer tempi
Kou meer tempi
Kou merr damay danou merr tempi
Watch Video
About Kou Merr Tempi
More TBRAINS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl