Chérie Boy Lyrics
Chérie Boy Lyrics by PIPANA
Yow da ngeu dougou sameu life
Lep da di ler ler nagne
Sokhloteouma ame nadje ak dianteu
Yow rek doy ngameu lumiere
Soumaleuy khol sameu yarame dafeuy daweu daw
Yeurmande la ame thi yaw mtax mane doumaleu meusseu def loulay nakari
Sougnou kholi nenegne waw wa diouri sakh niome nenagne waw
Wate na si yow rek lay yame li loukay fay
Kouy seu Cherie boy mani yawa
Boul doute yamalene gueunal
Defla number one takaleu diabar
I love you lo def nekhnameu
You cay way baby cay way
Nieuweul maleuy fethial deuguine nate say
You cay way baby cay way
Nieuweul maleuy fethial deuguine nate say
Kouy seu Cherie boy mani yawa
Boul doute yamalene gueunal
Defla number one takaleu diabar
I love you lo def nekhnameu
Dieguesima way diegueisma way
Boulmay sori wife boulmay sori wife
Bae khamenani mane nga done khar
Mane yow la done khar
Ho my love my love
Yaye sameu aldiana
Bae boudoul yow
Wate na dou done kenene
Wouy leleeeee khalebini
Mane douma doyal si dileu khol naneleu je t’aime
Wouy leleeeee khalebini
Mane douma doyal si dileu khol naneleu je t’aime
Kouy seu Cherie boy mani yawa
Boul doute yamalene gueunal
Defla number one takaleu diabar
I love you lo def nekhnameu
You cay way baby cay way
Nieuweul maleuy fethial deuguine nate say
You cay way baby cay way
Nieuweul maleuy fethial deuguine nate say
Kouy seu Cherie boy mani yawa
Boul doute yamalene gueunal
Defla number one takaleu diabar
I love you lo def nekhnameu
Watch Video
About Chérie Boy
More PIPANA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl