CARLOU D Eupneu cover image

Eupneu Lyrics

Eupneu Lyrics by CARLOU D


[REFRAIN]
Dou deug dou deug dédét
Meunoumako geum meunoumako geum
Can’t follow what you do to me
What goes around, come around
Yag may gagn, yag mey gagn
Yag mey gagn
Am in my role let me blow
The true I came from the…
My world is ….
Do you know who is talking to a lower Mr.Fatalo
Fatalo, Mr Fataloba 
Am Mr     Fatalo, Fatalo Mr Fatalo 
So khamone nimala beugué
So khamone nimala sopé
Eupneu hum hum
Dou deug dou deug dédét
Mane meunoumako geum meunoumako geum
Can’t follow what you do to me
What goes around, come around
Yag mey gagn
Yag mey gagn
Yag mey gagn
Eupneu hum hum
Hum hum, hum hum, hum hum
Mane damala guiss rek tite, melni kouy miir
Sama fiit né reuss khamatouma louy rirr
Damako wara toudé niak weurseuk
Wala dadi rek dama matagoul seuk
Garap bou dano khop ya la, té khop yi dotoul seukeuti
Lolou reka takh lo wone ma def ko khoulo
Wayé banioumala dama khamoul louma lay waxé sama mbeuguel
Ci ioe yamay danel, ioe rek yay kima doy
Ioe rek yay kima so khamone nimala sopé
So khamone nimala beugué
Eupneu hum hum

[REFRAIN]
Dou deug dou deug dédét
Mane meunoumako geum meunoumako geum
Can’t follow what you do to me
What goes around, come around
Yag may gagn, yag mey gagn
Yag mey gagn
Eupneu hum hum, hum hum, hum hum, hum hum

Mane gnima beug geuneu bax gni
Xalé gnima beugeu geuneu dièk gni
Mane gima geuneu beugeu geuneu tarru gni
Xalé yima beugeu geuneu yarru gni
Kholal Ndeye Khady Niang rek mou « téleul »
Ba mateu seur niou guéweul ko, baral ko, baral ko
Sargal na djiguen nou sérére djiguen nou mandiagobou diola
Bou peulh bou bambara khansonké soninké pulaar
Djiguen nou lawbé ak soccé ko lébbou
Djiguen nou walo walo, kayor ak bou saloum
Djiguen nou diakanké djolof djolof narr
Djiguen nou wolof, djiguen nou mankagn ndiambour ndiambour
Baynouké guéweul balante
Ioe djiguen’ay solome
Sargal na djiguen nou sérére djiguen nou mandiagobou diola
Bou peulh bou bambara khansonké soninké pulaar
Djiguen nou lawbé ak soccé ko lébbou
Djiguen nou walo walo, kayor ak bou saloum
Djiguen nou diakanké djolof djolof narr
Djiguen nou wolof, djiguen nou mankagn ndiambour ndiambour
Baynouké guéweul balante
Ioe djiguen’ay solome
Thio yobou len waay

Yag mey gagn, yag mey gagn yag mey gagn
Eupneu hum hum, hum hum, hum hum, hum hum

Watch Video

About Eupneu

Album : Eupneu (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Oct 22 , 2019

More CARLOU D Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl