CARLOU D Gën Na Tekki Fi cover image

Gën Na Tekki Fi Lyrics

Gën Na Tekki Fi Lyrics by CARLOU D


[VERSE 1]
Tolou souniou ndaw woutou aduna
Né si yoonou ndam,
Daan doolé khamni daniou wara am
Baye souniou wé wou
Tank moy foula ak fayda
Geum souniou bop lay doolé
Si takh y’ek kaw geu dioug jeuf jootna
Liguey dess souniou reew ak
souniou ngor lagn soxla
Louniouy dem wouti ji
Bitim reew niakou fi
Bougn si joublo ak ki pékhé am ko fi


[CHORUS]
Boul nangui fa, bala nga nath say
Togual ci reew mi tékki fi walaxi
Geum na ni meun na tékki fi
Liguey ted fi meun na tékki
Ngala bay togual ci deuk bi
(Meun na tékki fi) hé
Niou diarign deuk bi
(Meun na tékki fi) hé


[VERSE 2]
Geum sa bop xol ci say mbok moytou
Ndikou di wokk sa dokheu
As gorr dou faté gorr foula ak
Fayda ci la bokkeu
Alale lay fathie gathié
Banékh fadioul nakhar
Meuna weur mayéwoul weurseuk
kounék dioudo ak sa weurseuk

Bilay wax diou wéer la leu wax
Togual ci reew mi boul dem fenn
Napeu samb bay doundé léep
Ngui dokh ci reew mi
Bouniou thiouné waw
Wax diou wéer la leu wax
Togual ci reew mi
Oute métier napeu samb bay doundé
Lépeu ngui dokh ci reew mi
Bouniou thiouné waw waw


[CHORUS]
Boul nangui fa, bala nga nath say
Togual ci reew mi tékki fi walaxi
Geum na ni meun na tékki fi
Liguey ted fi meun na tékki
Ngala bay togual ci deuk bi
(Meun na tékki fi) hé
Niou diarign deuk bi
(Meun na tékki fi) hé


[VERSE 3]
Souf si souniou sou leu waw
Nagn diw dina magni diour dome ja... waw
Tokk fi garap gui souniou m’baye la
Tool yi lossi def mou fay laa...
Ndax thiono dou say
Kone diougeul yeungou dieund ak diaye
Reew mi nioko meun défar bamou nawate
Siguil souniou Sénégal


[CHORUS]
Boul nangui fa, bala nga nath say
Togual ci reew mi tékki fi walaxi
Geum na ni meun na tékki fi
Liguey ted fi meun na tékki
Ngala bay togual ci deuk bi
(Meun na tékki fi) hé
Niou diarign deuk bi
(Meun na tékki fi) hé

Boul nangui fa, bala nga nath say
Togual ci reew mi tékki fi walaxi
Boul nangui fa, bala nga nath say
Togual ci reew mi tékki fi walaxi
Togual ci deuk bi niou diarign deuk bi
Ndax nioune gouney deuk
Bi nio wara défar deuk bi
Togual ci deuk bi diarign amna deuk bi
Togual ci deuk bi ndimbal amna ci deuk bi
Geum sa gokh sokhali sa gokh
Geum sa bop niakeu diarignou
Geum sa gokh sokhali sa gokh
Geum sa bop niakeu diarignou
Geum sa gokh sokhali sa gokh
Geum sa bop niakeu diarignou

Watch Video

About Gën Na Tekki Fi

Album : Gën Na Tekki Fi (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 10 , 2019

More CARLOU D Lyrics

CARLOU D

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl