Mon Chocolat Lyrics
Mon Chocolat Lyrics by SAFARY
Tay gnou dème si bamou nekh mon chéri, mon chocolat
Tay gnou dème si bamou nekh mon chéri, mon chocolat
Gnar gnou minanté bamou diex fokk gnou deiggo
Melni pobbar ak kani geune nokoss
Tekk thi wowanté nutella
Pomme d'amour ak sucre d'orge
Mani weundel ma beugel ma mon cariño
Ohhh baby ohh mon chocolat
Mane dh beugg na guani ma affaire bi yaw la
Ohhhh mon chocolat, mon caramel
Mane dh beugg na guani ma affaire bi yaw la
Mane lila beugg
Thi mom, thi mom
Mom lila beugg
Thi mane, thi mane
Mane lila beugg
Thi mom, thi mom
…

Watch Video
About Mon Chocolat
More SAFARY Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl