Sweet Game Lyrics by VIVIANE CHIDID


Nanguoul ma
Nè sa xol mane ma fa né
Baby tay meu lèral la
Nè khamna ni mane rèk nguay weur, Deug leu
Kou mèlni ngua sokhla meunè founè
Foumeu feuleu rèk djomal leu
Khamnani gentle ngueu
Nanguoul nè malèy bègueul mane may seu star
Hey vivi da ngua gueuneu khèw, ndourou wo kou bèw
Ya koy daguatè li lèrr na

Nanguoul ma
Nè sa xol mane ma fa né
Baby tay meu lèral la
Nè khamna ni mane rèk nguay weur, Deug leu
Kou mèlni ngua sokhla, kou beuri sèytané ba djakhal leu
Khamnani gentle ngueu
Nanguoul nè malèy bègueul tchi birr nèkk bi
Kou kham li lann leu ngueu wakh ma
Kou kham li lann leu meu nèkhal la
Kou kham li lann leu ngueu wakh ma

Nanguoul ma
Nè sa xol mane ma fa né
Baby tay meu lèral la
Nè khamna ni mane rèk nguay weur, Deug leu
Kou mèlni ngua sokhla meunè founè
Foumeu feuleu rèk djomal leu
Khamnani gentle ngueu
Nanguoul nè malèy bègueul mane may seu star
Kou kham li lann leu ngueu wakh ma
Kou kham li lann leu meu nèkhal la
Kou kham li lann leu ngueu wakh ma
Kou kham li lann leu meu nèkhal la

Sonou na tchi sagg bi
Di mougn lou mèlni
Sonou na tchi sagg bi
Di mougn lou mèlni
Baby nanguoul ma, wakhal sa gars gni manne leu
Tè ngueu sigui kholma
Baby nanguoul ma, wakhal sa gars gni manne leu
Tè ngueu sigui kholma
Bouguou ma lou sèddeu faw mou sanguou way

Tchine bokoul tchafine vivè kholoul tchi tchine
Ak lo xèkh wèkh na na noy seu ndiba tilim
Moh vivi yangui guaagn bouguou ma tchow wagnil way
Chérie nangoul ma, dama beuri djapp
Mane djomal na la té douma rap
Antann ngua li ngua yènou boul woutt walou
Gnémé ko waw waw
Diguou lal lagnouy rèrrè, after ioe lay dessero
Tchabi bountou nèkk bi tay rérouma
Boul wo walou gnémé ko wawaw
Lou mèlni makko mom
Té kou feugueu togn ma
Gneuweul ma défal la louy takh ngua nanguoul ma
Titangué warou la mba lèpp mingui bakh
Hey kaay fi, hey kaay hey
Li daflay ndourou sweet game
Casa de papel yeufou bandit
Seu âme dafa sensible sori ma
Chéri nangoul ma dama beuri djapp
Mane djomal na la té douma rap
Antann ngua li ngua yènou boul woutt walou
Gnémé ko waw waw

Ngueu meunn diko dèf bokoul ak koukoy djèm
Yako meunn diko dèf ioe da nguay fo
Hey ambiance
Gneuweul ma défal la lout takh ngua nangoul ma
Titangué warou la mba lèpp mingui bakh
Hey kaay fi, hey kaay hey
Ay, kou donn wakh na ngua noppi bass yèkssi na
Tay fi day nèkh day roumbakh poutch
Viviane yaw lo guénè gnou fetch ko
Tay fi day nèkh day roumbakh poutch
Hey vivi deubb ko bamou mokk té dara dou yeunguou
Li daflay ndourou sweet game
Casa de papel yeufou bandit
Seu âme dafa sensible sori ma

Watch Video


About Sweet Game

Album : Sweet Game (Single)
Release Year : 2021
Added By : Farida
Published : Dec 24 , 2021

More VIVIANE CHIDID Lyrics

VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2023, We Tell Africa Group Sarl