Il Est Temps Lyrics
Il Est Temps Lyrics by SAFARY
Thi leundeum lama teuthie may youkhou di diioy
Xoti sama yairé tour sama rongogne
Sama avenir yeup des thi ay lokhome
Yakh sama xol tilimeul sama yaram
Cette petite fille innocente violée
Celle qui sans défense pleurée
Dans la peur et dans le noir, dans le noir
La jeune femme que je suis devenue maintenant
N’a plus d’amour à donner
Victime d’un animal
Bilay, Walay, bilay
Yakkeu sama khôl, tilimeul sama yaram
Bilay Walay bilay
Sama avenir moudiou dess ci au lokhom
Niata djiguène lagnfi Sakou ray
Bokok yayam baye
Niata la mariage teudj ci trou meuniou
Daw ndakh ndiabote
Diotna niou dieul sounou matouway
Il est temps que mou diekh yow
Il est temps que mou diekh yow
Ces fous en liberté
Cette petite fille innocente violée
Celle qui sans défense pleurée
Dans la peur et dans le noir, dans le noir
La jeune femme que je suis devenue maintenant
N’a plus d’amour à donner
Victime d’un animal
Bilay, Walay, bilay
Yakkeu sama khôl, tilimeul sama yaram
Bilay Walay bilay
Sama avenir moudiou dess ci au lokhom
Watch Video
About Il Est Temps
More SAFARY Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl