Bara Afia Lyrics
Bara Afia Lyrics by NDIOGOU AFIA
Bara afia
Diambaar gua yaaram
Bara afia falloulahi
Diambaar gua yaaram
Donnou gua mame
Khadim rassoulilah
Done gua sa baye
Afia falliloulahi
Balla aissa bouri
Serigne mbackè ak maaram
Mame diarra bousso ma gua porokhane
Yaye dial diagn yalna yalla yoki leram
Bara afia fassaleniou mbacke
Lo fass mou fassou fassaleniou mbackè
Do togn do fayou
Ya bakh ni gay dokhalai
Wékho nayo reuyo niako xorom niawoulo
Baye bara afia
Serigne afia mbacké moy ki ko diour
Ma gua dalai alhourane fa thileu daramane
Serigne djily bousso
Kokou borom xam xam leu
Kokou diangalneu serigne bara
Yagunaa dégu lou way donoul talibem
Dou done serignam tay lako guem
Tieuy lamou dathie
Tay lamou am
Lamou dathie demb moko may tay limou am
Bamou amai fouki ate leu bind
Matlaboul chifahi thi loxom
Diébeulko bayam
Cheikh afia mbackè fallilou
Dane maadial di yalwane
Foko guisane tekk ko yarlou wane
Bara afia yalna gua yagu diamano
Am gua ngeureum
Thi serigne falilou
Am gua nguereum thi serigne abo
Ak wakeur serigne fallou
Afia falilou gua yaakar
Mom rek gua wolou
Baye fall bi ridial bi ya guem serigne fallou yalnala alahou aar
Yalla boula dara dal
Loula nara dal yalnama dal mane
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh say mbaakh mane may
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane may
Bara moy mamadou lamine
Mamadou lamine bara
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Bara mouhamadou lamine bara
Mane ma gui fi yaw ma gui thi yaw
Cheick modou lamine bara
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Bara mouhamadou lamine bara
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Souk naa raam naa diebeulounaa thi mouhamadou lamine bara
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Nite meunoul diokhai loumou yoroul bara amna ngeureum
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Nite meunoul diokhai loumou yoroul bara amna ngeureum
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Bara mouhamadou lamine bara
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Ma gui thi yaw ma gui fi yaw mouhamadou lamine bara
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
Bara yay domi diantte ak wéer louniouy tiow tiow guay sori
Domi diantte ak wéer gua
Mane may kilay way dila djiine
Di wakh si say mbaakh mane way
May sa wéne gou nioula nioul guay diamant
Diamm mi gui way sangam
Te moma war sakh ndéguem
Xamnaa bou wér lima am
Yay magui baye gallass ak
Serigne mame mor ak serigne khadim
Donnou gua serigne bi
Afia falilouhi
Watch Video
About Bara Afia
More NDIOGOU AFIA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl