Douteu Mbaaye Lyrics
Douteu Mbaaye Lyrics by PAPE IBRAHIM
[COUPLET 2]
Ki dafa contane, Ki dafay rétane
Ki dafa mérr, Ki dafay dioy
Ki dafa contane, Ki dafay rétane
Ki dafa mérr, Ki dafay dioy
Ki dafa contane, Ki dafay rétane
Ki dafa mérr, Ki dafay dioy
Bo guissé khalé bouy dioy
Khamal ni loumoubeug dako amoul
Bo guissé makk bou merr
Khamal ni dépense’am ma matoul
Bo guissé djiguen bouy fougnaral
Khamal ni cheveux la amoul wawaw !
Teubeul teubeul teubeul
Ba cikaw sa thiaya naw ngey nongui nongui
Teubeul teubeul teubeul
Ba cikaw sa thiaya naw ngey nongui nongui
Teubeul teubeul teubeul ba cikaw sa cheveux naw ngey diékh ci souf ou yeah hé !
Je suis sage, Je suis sage
A ma place, A ma place
Les mains sur la table, les mains sur la table
Je ne bouge plus, je ne bouge plus
Ma main, Ma main
Elle a cinq doigts en voici deux, en voici trois
Celui-ci petit bonhomme c’est le gros pouce qu’il se nomme
Regardez mes doigts travailler
Chacun fais son petit métier
[REFRAIN]
Douteu mnbaaye lo réré bikk
Thiéré geusseum ak dogou yapp mome la réré bikk
Geusseum geusseum geusseum
Mba déwoul da ngey wadia déh
Mba déwoulo ioe da ngey wadia déh
Adama ak Awa
Nio bok ndeye, nio bok baye té nio bok mame
Ken doulen door, ken doulen lale
Ken doulen saga ba niniouy magué
Waxma fouy méti ma fadial lako
Waxma fouy méti ma fadial lako
Khol na gauche, khol droite
Khl digeunté bi guissouma fouy méti
ohoh ! ohoh ! ohohhhh !
Goor dey mbeuké, djiguene dey guadjé
So mandé demal teudi, boul yakahl gni nanagoul
Yaye bougouma, Yaye bougouma
Yaye bougouma, Yaye bougouma
Yaye bougouma domoda, yaye bougouma mafé kandja
Yaye bougouma souloukhou mbalax
Yaye bougouma mbaxalou dieune
Yaye bougoumaaaaa…
Tassal sa cheveux, y amome sa cheveux
Tassal sa cheveux am nga loko dieundé
Yeungeuleul sey cheveux, Yeungeuleul sey cheveux
Sey cheveux, Sey cheveux
Yeungeuleul sey cheveux (x3)
Sey cheveux , Sey cheveux, Sey cheveux
Sey cheveux , Sey cheveux, Sey cheveux
Sey cheveux , Sey cheveux, Sey cheveux
Watch Video
About Douteu Mbaaye
More PAPE IBRAHIM Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl