DEF'L NICE Sori Nga cover image

Sori Nga Lyrics

Sori Nga Lyrics by DEF'L NICE

[REFRAIN]
Diégui ga guédj gui bayiko guinaw
Mome déh dioyna dioyneuh dioy ba rongagn ferr ayway 
Beug nala mougnal nala ki sa yayou dome la 
Beug nala mougnal nala ki sa yayou dome la 
Diégui ga guédj gui bayiko guinaw
Mome déh dioyna dioyneuh dioy ba rongagn ferr ayway
Sorri nga len ba faté len té lolou warou la 
Sorri nga len ba faté len té lolou warou la 

[COUPLET 1]
Nék ak mane louné temps kham lou nieup 
Dougou ci ioe té lank dou deup 
Dem ba dièkh la xolam di guiss
Té wol dou sax bam bagn koy guiss
Kholal ci mom, nimuy doundé 
Méti na lool, ci xolam yay ki fa diékh
Yay ki wala ci lépeu li xew mou geumeu té geum né mbeuguel dey fay
Yay ki waral ba feep fo dem 
Mou tokk té mougn té khar nga tew
Louko fi té, khana mbeuguel 
Louko fi té, khana coleurééé

[REFRAIN]
Diégui ga guédj gui bayiko guinaw
Mome déh dioyna dioyneuh dioy ba rongagn ferr ayway 
Beug nala mougnal nala ki sa yayou dome la 
Beug nala mougnal nala ki sa yayou dome la 
Diégui ga guédj gui bayiko guinaw
Mome déh dioyna dioyneuh dioy ba rongagn ferr ayway
Sorri nga len ba faté len té lolou warou la 
Sorri nga len ba faté len té lolou warou la

[COUPLET 2]
Fi nga né sorri na
Faté len waroula 
Touki bayilen djabote tok di la kharr hé héé ! ohh ! 
Fi nga né sorri na
Faté len waroula 
Touki bayilen yeah ! héééhééhé !
Sa yayou dome 
Fi nga né sorri na
Faté len waroula
Touki bayilen djabote tok di la khaaaarr… !
Sa yayou dome hé hé !
Sa yayou dome 
Sa yayou dome 
Sa yayou dome 

Watch Video

About Sori Nga

Album : Sori Nga (Single)
Release Year : 2018
Added By : Tamsir Diouf
Published : Sep 17 , 2019

More DEF'L NICE Lyrics

DEF'L NICE

Comments ( 0 )

No Comment yet

About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl