Boula Dara Méti Lyrics
Boula Dara Méti Lyrics by ADMOW
[COUPLET 1]
Yéneu say nga fokni
Ci aduna bi ken doula comprendre
Sometime nga dem ba diap ni doto meussa contane
Cibiir keur gui
Yaye boy néneu doula may nada, nada
Ci mbédeu mi yeah yeah !
Ragal la tax ngani do mayé dara, dara
Mais nak boul diakhlé
Yoone la bou diafé
Wanté madi goor bi kham fi nga fété
Kham sa ndjeugue nga tax meu deukeu ci di gnaféé yeah, humm !
Thiofel la ngui cibiir xol bi
Diokhma confiance ma yoboula fou soorri
Ouh baby ! Ohh baby yeah yeah !
[REFRAIN]
Damala love love love ,
Baby love love love,
Boula dara méti
Nakhar dièkhna tay
Ma ngui ci sa wett boula dara méti
Dinala téwal ci nathie
Téwal la ci kérr boula dara méti oooh !
Baby i got your back, boula dara méti yeah !
[COUPLET 1]
Ouuu ouuuh ouuuh !
Écoute-moi, baby
I love you lady
Et je sais que t’as peur de m’aimer
Si tu t’inquiètes pour moi t’as tord
Faut que tu dormes de ton décor
T’as déjà gagné mon cœur
Donne-moi ma chance fais un effort
Soumala kholé guiss ci ioe kou am diome
Douma beugeu loudoul done sa héros
Do wétt ci bi lé yone you are not alone
Je suis ton ange gardien
Oooh ! Baby you are the one
Baby you are the only one hé !
Baby you are the one that
I need in my life yeah !
[REFRAIN]
Damala love love love
Baby love love love, boula dara méti
Nakhar dièkhna tay
Ma ngui ci sa wett boula dara méti
Dinala téwal ci nathie
Téwal la ci kérr boula dara méti oooh !
Baby i got your back
Boula dara méti yeah !
Boula dara méti yeah !
Watch Video
About Boula Dara Méti
More ADMOW Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl