
Zeusophobie Lyrics
...
Zeusophobie Lyrics by OOTHENTIK ZEUS
Neub sama life
Wane si li nice
Xool sis a eyes
Guissatuma lights
Meunoulooma taal dègoulo sama laak gayn
Meun nga daw sa bideew mais moolay deudj si night
Nioogui may yak lounek
May tokk di saur
Nakh dama bott njaboot
Tabakh avenir day toji sa xol
Niakkh dou fendi nakh meussoumeu diog si job
Motakh kouma xam rek ndaw doonté guissagoul lima dadj si thioono
Dou compter si iow meunoo wagn limou dèkou si balles yi
Adounak barzakh d’où yallah ak yaali
Piaule beu weer bou déé maay takk capi
Tankou neen si yoon bi, yeek si di dawal ba taali
Coupe bi laay diuli pour djittou ni calif
Nakh beugumeu moudié si guémeuniou tann yi
Gars yila nguemb naniou sawi dem teudi
Talatouma tèssanté bi niakk gueum sama bopp
Mooy ma am sen xel yi parce que damalen weddi
Yallah rek xam sama mérite
Yaay sa dom dina dadj say métitt
Goud fane lay niaan, booko amé guiss niarign
Nakh ray sama boop laa def mouy délit
Jot naa wèèt ak mom
Neel sam noon yi
Dama ragal sam bopp
Sama xel teudiowoul woon nakhté god d’ou teudj bount ak window
Lima saub défagouma khaadj bi
Teh si ndieulbén laako xam takh douma moudjé si khaadi
Paaka yima diam motakh, sama xel bi di nathi
Dooragouma waayé dalatouniou li nga guiss wessouwoul sama khathi
Nagger sama xol damko deug dokh
Leçons yima diang dafa gueneu mokké
Deum bouma songu di nga lekk thiow
Fayéku moo jott awma temps douma bénévole, khatt amatouma diot
Ay att laako seug job fayagoul gatt douma seukhétoo dakh bi moogui nieuw
Douma daw bey daanou dma tèla diog yaa meu gueneu know
Tereul séni lobbys dima complot kima yekki mooy ki yorré contrôle
Defma titulaire séni compos talent bima yoré douma baayo malay diokh flop
Viser naa le top doumeu altoopé
Niakkatouma quote fété nameu cote
Sokhlawouma sa dose meunoulooma doser
Amouma sa diott meuneutouniou diotté
Boy yaay kharr
Dawouma polémique yallah dji wakhna lepp motah niou fogg ni daa noopi nii
Yakkh ma khon ma fi rap bi lep li ci am koulo wakh nguen fatt nopp yi
Yèwou di rever bagn nelow si guent yi taylé fi lal bi dem jobbi dji
Teukou sam bopp di compétir xadiouma galsen niou diappéko comédie
Si kaw laniouy khool nakh kiniou tiim meussoul changer djikkom
Niaata lagn woon bouma faatélikoo ay souvenirs boumay diaar samay kogn
Biniouy woyof ni hop, gueumougn loudoul hip hop
Gars yi weddiniouko mais niou degueur si bopp
Bouki niou bott rap bi indil niou thioow
Waayé déloowouniouko guenmoon ni dineu nieuw
Watch Video
About Zeusophobie
More OOTHENTIK ZEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl