
Jehovah Lyrics
...
Jehovah Lyrics by OOTHENTIK ZEUS
Sant yallah maagui sant sama yaay
Santaat sama yaay santaat sama yaay
Sant sama baye mima tanal yaay
Sant sama gars yima yagg gueum diap teuweu baayi
Gnima diota baayi neleen dougn ma téré yor
Souma djiteuloon am am sama ngor dieex
Beut dereetako lal waayé rangogn lay guén
Guémegn gouy nathi modoul meusseu wakh diam
Sama baamélou biir mougn laako tabakhé
Sangoo sama doolè bess dina takk
Koussi khel niaar nama seekhlou melni thiatt sango
Sama niakh guéneu lou sett diap
Si lima am sama werseuk bi ma dakh
Yaay xamnaani ken douma beug ni iow
Ken douma nieme wakh deug ni iow
Parce que iow yaay yaama taawloo fekké
Sama assamaan khiin
Beut taa khol tooy
Rakk nima ana baay booy
Bank sama oom seug beuss khol
Keurgou makk dafa khatt lool
Ligueey ba kerr dama dokhé nadj
Bay kata xam nima dooyé waar
Amouma xaliss ni doomou steve jobs yi, waayé ni nioom foowé mac
Fess lama deff fi nga diokhé taat
Sen carrier yi soutoul mota et ma
Amoulo xam xam pour juger meu
Woona si barre bi ay témoins de jéhovah
Deg naa percer nga waanté si nop la yem
Parce que tangoo fi louma meun diaroo
Buzzou semaine doyoul pour dima tendance ba leuz sa g yi dougn todj sa diwaan
Rap beema yiiteel sinon guélou niska sax, meun naako kepp souma nekoon charo
Am nga ay arriérés may lekk avance, millions laay peser sa, niugou balance
Diang ay att di kheuy di gontou, faayekou weer no gondiwmeu woon
Ba bess may wakhtou di melni dof rap bema keuf boy si ay seconde
Questions de temps la teekey réponse, eup ay tournés aiguilles si montre
Boukhanteel may beumeukh sa monde, dina teuyé rap galsen samay lokho
Pique meu je roule une pèle à ta goe
Fit neu dou dieex à la vie à la mort
Bandit bou khess nioo diw pablo
Negger todiomeu neen sons yi todj plateau
Soul leu si souf yeek fanaan si kaw
Tidji balcon khaar sa rouh bi romb
Moogui sen biir zeus khadioul si nioom, zero faute teewoul
Rap lou wow kong teh doo guiss fouma wéré
Doo bindeu ligne fimalay keppé maay zinedine kb9
Reals yéma yékeuti ldc
Dikeuloon nama ma taal ay doublé pourtant sama but mooy encaisser
Ken yeugoulwoon sama anxiété rap galsen douma inquiéter
Job ba dog takhoul ma doon workat
Limay tek thiouné maneessouko comprendre
Diamono bi moo dokhoul ba sen son daw
Fouma guénéwer kenen dou niuuw comme thiaat
Rap koussi xamoul dara moo xam, koussi xam dara douné xamoul may kane
Nikou guiss mbaakh sa taat yi lay khonkhal, kou lek sama avance arrière combat
On fait du sal tilimeul douma débutant mais finisseur
Goudou baat sama wakh gatt kilifeu maafi khar niaar diviseur waw
Comme que sama wade la aye pds ay laay def si perdais r
Xawma sen soubeu waayé tay nguen dee lagui boy bouma clash ma tégueul nd
Watch Video
About Jehovah
More OOTHENTIK ZEUS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl