Kouy Sa Baay Lyrics
Kouy Sa Baay Lyrics by JAY
[CHORUS]
Dégouloma démal lathi ko sa baye
Guissouloma démal lathie ko sa yaye
Kiléy takk fauk mou tékki
Ba mou diangue diégué tékki sa baye
Kholal sa yaye, niom nioma diéma touteul tay
Mais sama souba nara dakh tay waay
Baby bye bye, aduna ken khamoul souba
Meun nga tassé kou geuneu tékki sa baye
[VERSE 1]
Bouma sagnone damay dokh ak gone
Gowé sama life bi geuneu bone
Li geuneu bone niou gass dougeul si tombe
Mais bi damay changé forme tamt téla cassé kone
Boba daniouy djiweut lo
solna bou yage mane sama kimono
Baby souma diadoutone fima diadeu douma tassé
Ioe bay nek sa gayne mais baby bye bye
[CHORUS]
Dégouloma démal lathi ko sa baye
Guissouloma dagn ma lathie kouy sa baye
Kiléy takk fauk mou tékki
Ba mou diangue diégué tékki sa baye
Baby bye bye, niom nioma diéma touteul tay
Mais sama souba nara dakh tay waay
Baby bye bye, aduna ken khamoul souba
Meun nga tassé kou geuneu tékki sa baye
[VERSE 2]
Lugn diot doundou demb mane doumko werr fi
Djiguen dagn koy soutoural mane doumla werr fils
Démone na bay né boul tite may done sa pèrou fils
Boumay lathi money sa yaram dou daw
Louma fi guiss motax may dieul sama distance
Dioureul ma fils doko dégue do résistance
Baby bayma ma nitte, niom nénagn douma ndjite
Kou kham lou y’Allah di bind ngen
May jugé kham waay bye bye
[CHORUS]
Dégouloma démal lathi ko sa baye
Guissouloma dagn ma lathie kouy sa baye
Kiléy takk fauk mou tékki
Ba mou diangue diégué tékki sa baye
Baby bye bye, niom nioma diéma touteul tay
Mais sama souba nara dakh tay waay
Baby bye bye, aduna ken khamoul souba
Meun nga tassé kou geuneu tékki sa baye
[OUTRO]
Yeah! Sen wakeur nioma lathie kouy sa baye
Yeah! Sen wakeur nioma lathie kouy sa baye
Yeah! Sen wakeur nioma lathie kouy sa baye
Yeah! Sen wakeur nioma lathie kouy sa baye
Né nagn dagn ma diépi maybe dagn ma khep
Sagnone dagn may sépi
Khamougn sama khep ma
Fowanu may fes titre
Douma yague fiesti dé meun nala wole
Ci chaise bi limey sampe fiesta
Nénagn dagn ma khep
Nénagn dagn ma khep
Nénagn dagn ma khep
Nénagn dagn ma khep
Nénagn dagn ma khep
Sen wakeur nioma lathi kouy sa baye
Waro kh baby girls ken khamoul lane la
Y’Allah denthial sa morome baby bye bye
[CHORUS]
Dégouloma démal lathi ko sa baye
Guissouloma dagn ma lathie kouy sa baye
Kiléy takk fauk mou tékki,
Ba mou diangue diégué tékki sa baye
Baby bye bye, niom nioma diéma touteul tay
Mais sama souba nara dakh tay waay
Baby bye bye, aduna ken khamoul souba
Meun nga tassé kou geuneu tékki sa baye
Dégouloma démal lathi ko sa baye
Guissouloma dagn ma lathie kouy sa baye
Kiléy takk fauk mou tékki,
Ba mou diangue diégué tékki sa baye
Baby bye bye, niom nioma diéma touteul tay
Mais sama souba nara dakh tay waay
Baby bye bye, aduna ken khamoul souba
Meun nga tassé kou geuneu tékki sa baye
Watch Video
About Kouy Sa Baay
More JAY Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl