Belle Lyrics
Belle Lyrics by BIDEEW BOU BESS
[VERSE 1]
Sama xol mo fess ndéké né
Love la denthi
Boudone xaliss dou lou meuna
Khathi ci banque
Mbeuguel mo riche
Tay lama leer ni jantema ngui dox
Ma ngui mirr sokhla ordonnance
Ioe ya mey ray yay sama 15 bi manqué
Ya mey may yama takha dokh di pant
Sa xol la noyi yay sama tourr
Sama sant waw an love an chérie
Bala ma nane yééh
Dem na ardo dem na ardo
Ci la ma khalé bi momé
Bala ma nane yééh
Fala miré fala bardé ci
Lama mame yi momé
[CHORUS]
Khol ko mi ngui dioy loumuy
Lathi mbeuguelam
Nakh ko boumou souffrir
Khamal ko ya déh si xolam
Tu es ma douce ma bien aimé
Ma linguère belle
Yay leer té nékha khol yay
Ma reine bell
Mbeuguel bi né ci ioe
Mo né ci mane belle
Sama mbeuguel la done beurél
Té yama dane togal
[VERSE 2]
Sama melocane rek’a ma yém yobou
Sama fourou fara mane
Geuleum ci bi ngélaw ni
Khop di feureureureu
Bi nga ma né diack la soga
Dièkh meuneutouma dem
Melni pneu bou creu
Tank yi bagn lamign bi dameu
Ma moudiou fa nek di dereu
I’m yours tou and mind
Indice love forever
Yow di only one that I need
Oh let’s gate together
Raaraahhrahh
Wouyou wouyou beug na leu
Raaraahhrahh
[CHORUS]
Khol ko mi ngui dioy loumuy
Lathi mbeuguelam
Nakh ko boumou souffrir
Khamal ko ya déh si xolam
Tu es ma douce ma bien aiméMa
Linguère belle
Yay leer té nékha khol yay
Ma reine belle
Mbeuguel bi né ci ioe
Mo né ci mane belle
Sama mbeuguel la done beurél
Té yama dane togal
[VERSE 3]
Sama weer bi feign na
Sama wourouss ba ngui
Y’Allah diokhma sama ouroul ayni
Diéguéssil ma dé la yay sama néné touti
Assamane si taw na mbeuguel la sax fi
Where you living in a darkness
But tomorow gonna bring
Another day the sun will shine
your hear singing my love by my side
M’ak ioe bouniou couplé
Di fo melni khalé
Monday ba Sunday limey wout ci ioe
ley matt damala noba noba noba
[OUTRO]
Ioe la beugeu, boul rouss waxko ko
Sama xol di teuf teuf ci ioe
Samay geud wane lako
Mbeuguel dey naw bouy niow dou tago
Kouné kouné am nga ko
Love nga wett deyko ko
Ioe la beugeu, boul rouss waxko ko
Sama xol di teuf teuf ci ioe
Samay geud wane lako
Mbeuguel dey naw bouy niow dou tago
Kouné kouné am nga ko
Love nga wett deyko ko
Ioe la beugeu, boul rouss waxko ko
Sama xol di teuf teuf ci ioe
Samay geud wane lako
Mbeuguel dey naw bouy niow dou tago
Kouné kouné am nga ko
Love nga wett deyko ko
Watch Video
About Belle
More BIDEEW BOU BESS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl